Vous avez cherché: praecipiens (Latin - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

usque in diem qua praecipiens apostolis per spiritum sanctum quos elegit adsumptus es

Wolof

ba ci bés, ba ko yàlla yéege ci asamaan. lu ko jiitu joxoon na ay ndigal, jaare ci xel mu sell mi, jëm ci ndaw ya mu tànnoon.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

tribunus igitur dimisit adulescentem praecipiens ne cui loqueretur quoniam haec nota sibi fecisse

Wolof

kilifa ga nag sant waxambaane wa, mu bañ koo àgge kenn, ba noppi mu yiwi ko, mu dem.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et factum est cum consummasset iesus praecipiens duodecim discipulis suis transiit inde ut doceret et praedicaret in civitatibus eoru

Wolof

ba yeesu joxee fukki taalibeem ya ak ñaar ndigal yooyu, mu jóge fa, ngir dem jàngaleji ak a waare ci seeni dëkk.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,621,228 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK