Vous avez cherché: prudentiam (Latin - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

prout potestis legentes intellegere prudentiam meam in mysterio christ

Wolof

bu ngeen jàngee loolu, dingeen man a xam bu wér dégg, gi ma am ci mbóoti mbiri kirist.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

scriptum est enim perdam sapientiam sapientium et prudentiam prudentium reprobab

Wolof

ndaxte mbind mi nee na:«dinaa folli xam-xamu boroom xam-xam yi,lem xalaati ñi am xel.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et ipse praecedet ante illum in spiritu et virtute heliae ut convertat corda patrum in filios et incredibiles ad prudentiam iustorum parare domino plebem perfecta

Wolof

mooy jiitu, di yégle ñëwu boroom bi, ànd ak xel mi ak doole, ji yonent yàlla iliyas amoon, ngir jubale xoli baay yi ak doom yi, ngir delloo ñi déggadi ci maanduteg ñi jub. noonu dina waajal mbooloo muy teeru boroom bi.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,781,916,787 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK