Vous avez cherché: scientia (Latin - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

et peribit infirmus in tua scientia frater propter quem christus mortuus es

Wolof

noonu sa xam-xam dina lor kooku ngëmam néew, fekk sa mbokk moomu, kirist dee na ngir moom!

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

caritas numquam excidit sive prophetiae evacuabuntur sive linguae cessabunt sive scientia destruetu

Wolof

mbëggeel amul àpp. Ñiy wax ci kàddug yàlla dinañu noppi, ñiy wax ay làkk dinañu ko bàyyi, ñiy xamle xam-xamu yàlla wàcc.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

o timothee depositum custodi devitans profanas vocum novitates et oppositiones falsi nominis scientia

Wolof

céy yaw timote, sàmmal li la yàlla dénk! tanqamlul waxi neen yu àddina kese, te dëddu werantey ñi mbubboo xam-xam, fekk dañoo réer.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

de his autem quae idolis sacrificantur scimus quia omnes scientiam habemus scientia inflat caritas vero aedifica

Wolof

léegi nag, ci li jëm ci yàpp wi ñu jébbal xërëm yi: nun ñépp am nanu xam-xam, loolu dëgg la. xam-xam day tax ba nit yég boppam, waaye mbëggeel day yékkati ngëm.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

sed non in omnibus est scientia quidam autem conscientia usque nunc idoli quasi idolothytum manducant et conscientia ipsorum cum sit infirma polluitu

Wolof

waaye ñépp xamuñu loolu. am na ñu tàmmoon xërëm yi, te léegi, bu ñu lekkatee yàppu sarax yi, dañuy xalaat ne, xërëm lañu ko jagleel. seen xel dafa leen di yedd, ndaxte ci seen ñàkka xam dañuy foog ne, taq nañu sobe ndax ñam woowu.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

certus sum autem fratres mei et ego ipse de vobis quoniam et ipsi pleni estis dilectione repleti omni scientia ita ut possitis alterutrum moner

Wolof

bokk yi, wóor na ma ne, baax ngeen ba fa mbaax man a yem, fees dell ak xam-xam, ba man a jàngaleente mbiri yàlla ci seen biir.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,795,017,550 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK