Vous avez cherché: sermonem (Latin - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

et multo plures crediderunt propter sermonem eiu

Wolof

Ñu bare gëm ko ndax li mu doon wax.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

cum ergo audisset pilatus hunc sermonem magis timui

Wolof

bi pilaat déggee wax jooju, dafa gën a tiit,

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

iam vos mundi estis propter sermonem quem locutus sum vobi

Wolof

yéen nag, baay bi setal na leen jaarale ko ci kàddu gi ma leen wax, ni beykat di tenqee garabam.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et ait illi propter hunc sermonem vade exiit daemonium de filia tu

Wolof

ci kaw loolu yeesu ne ko: «ndax wax jooju demal ci jàmm, rab wa génn na sa doom.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

amen amen dico vobis si quis sermonem meum servaverit mortem non videbit in aeternu

Wolof

ci dëgg-dëgg maa ngi leen koy wax, kuy sàmm sama wax doo dee mukk.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

primum quidem sermonem feci de omnibus o theophile quae coepit iesus facere et docer

Wolof

yaw teyofil, téere bu jëkk, ba ma bindoon, ëmb na lépp li yeesu tàmbali woon a jëf ak a jàngale,

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

itaque fratres state et tenete traditiones quas didicistis sive per sermonem sive per epistulam nostra

Wolof

kon nag bokk yi, taxawleen bu dëgër te jàpp ci dénkaane yi nu leen jottali, muy ci li nu wax, muy ci li nu bind.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

ego dedi eis sermonem tuum et mundus odio eos habuit quia non sunt de mundo sicut et ego non sum de mund

Wolof

jottali naa leen sa kàddu, te àddina bañ leen, ndax li ñu mel ni man, bañ a bokk ci àddina soosu.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

ita et vos per linguam nisi manifestum sermonem dederitis quomodo scietur id quod dicitur eritis enim in aera loquente

Wolof

noonu itam bu ngeen génnewul ay wax yu leer ci seen gémmiñ, nan lañuy man a xame li ngeen di wax? dingeen wax cig neen!

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

amplectentem eum qui secundum doctrinam est fidelem sermonem ut potens sit et exhortari in doctrina sana et eos qui contradicunt arguer

Wolof

war na jàpp ci xebaar bu dëggu, bi lal sunu yoon, ba man a dénkaane ci njàngale mu wér mi, tey yey ñi weddi.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et non cognovistis eum ego autem novi eum et si dixero quia non scio eum ero similis vobis mendax sed scio eum et sermonem eius serv

Wolof

xamuleen ko nag; man maa ko xam. su ma ne woon xawma ko, ab fenkat laay doon ni yéen. waaye xam naa ko te maa ngi sàmm waxam.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

dixerunt ergo iudaei nunc cognovimus quia daemonium habes abraham mortuus est et prophetae et tu dicis si quis sermonem meum servaverit non gustabit mortem in aeternu

Wolof

yawut ya ne ko: «léegi wóor nanu ne, dangaa am ay rab! ibraayma faatu na, yonent yépp faatu, yaw nga naan: “kuy sàmm sama wax, doo ñam dee.”

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

at ille egressus coepit praedicare et diffamare sermonem ita ut iam non posset manifeste in civitatem introire sed foris in desertis locis esse et conveniebant ad eum undiqu

Wolof

waaye naka la waa ji génn, mu di yéene ci kaw li xewoon, te di ko jéebaane, ba tax yeesu mënatul a faŋaaral dugg cib dëkk, waaye mu nekk ci biti ciy bérab yu wéet. ba tey nit ñi jóge fu nekk, di ko fa fekk.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,773,023,493 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK