Vous avez cherché: videret (Latin - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

similiter et levita cum esset secus locum et videret eum pertransii

Wolof

benn waay it bu soqikoo ci giiru lewi, aw ca bérab booba, séen waa ja, teggi.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

abraham pater vester exultavit ut videret diem meum et vidit et gavisus es

Wolof

seen baay ibraayma bég na, bi mu yégee sama ngan. bi mu ko gisee it, bég na ci lool.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

quam cum videret iesus vocavit ad se et ait illi mulier dimissa es ab infirmitate tu

Wolof

bi ko yeesu gisee, mu woo ko ne ko: «soxna si, sa feebar deñ na.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

intravit autem rex ut videret discumbentes et vidit ibi hominem non vestitum veste nuptial

Wolof

«bi nga xamee ne buur bi dugg na nag, ngir seetsi gan yi, mu gis fa nit ku solul mbubb mu ñu war a sol ca céet ga.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et responsum acceperat ab spiritu sancto non visurum se mortem nisi prius videret christum domin

Wolof

te xamal na ko ne, du dee mukk te gisul almasib boroom bi.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

quod cum videret simon petrus procidit ad genua iesu dicens exi a me quia homo peccator sum domin

Wolof

naka la simoŋ piyeer gis loolu, daldi sukk ci kanamu yeesu ne ko: «sore ma boroom bi, ndaxte nitu bàkkaar laa!»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

deinde iterum inposuit manus super oculos eius et coepit videre et restitutus est ita ut videret clare omni

Wolof

kon yeesu laalaat bët yi, gumba gi ne xefeet, daldi wér, ba gis lépp bu leer.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

fide enoch translatus est ne videret mortem et non inveniebatur quia transtulit illum deus ante translationem enim testimonium habebat placuisse de

Wolof

ngëm moo tax ba enog jaarul ci dee. yàllaa ko yóbbu ca moom, te kenn gisatu ko, ndaxte yàllaa ko toxal. ndaxte mbind mi seedeel na ko ne, laata muy toxu, neex na yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

petrus autem sequebatur eum a longe usque in atrium principis sacerdotum et ingressus intro sedebat cum ministris ut videret fine

Wolof

piyeer topp ko fu sore, ba ci ëttu saraxalekat bu mag ba; mu dugg, toog ak surga ya, ngir seet nu mbir may mujje.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et cum videret iesus concurrentem turbam comminatus est spiritui inmundo dicens illi surde et mute spiritus ego tibi praecipio exi ab eo et amplius ne introeas in eu

Wolof

ci saa si baayu xale bi wax ci kaw naan: «gëm naa, dàqal ma sama ngëmadi.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,744,578,478 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK