Vous avez cherché: mandamentos (Portugais - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Portugais

Wolof

Infos

Portugais

se me amardes, guardareis os meus mandamentos.

Wolof

«bu ngeen ma bëggee, dingeen topp sama ndigal.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Portugais

destes dois mandamentos dependem toda a lei e os profetas.

Wolof

Ñaari ndigal yooyu tënk nañu yoonu musaa wépp, moom ak waxi yonent yi.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Portugais

e nisto sabemos que o conhecemos; se guardamos os seus mandamentos.

Wolof

ci lii lanu xame ne, xam nanu ko: sàmm ay ndigalam.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Portugais

a circuncisão nada é, e também a incircuncisão nada é, mas sim a observância dos mandamentos de deus.

Wolof

xaraf ak ñàkka xaraf lépp a yem; li am solo moo di topp ndigali yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Portugais

se alguém se considera profeta, ou espiritual, reconheça que as coisas que vos escrevo são mandamentos do senhor.

Wolof

su kenn xalaatee ne, mooy wax ci kàddug yàlla, walla mu xalaat ne, xelum yàlla jagleel na may, na nangu ne lii ma leen bind ndigalu boroom bi la.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Portugais

porque este é o amor de deus, que guardemos os seus mandamentos; e os seus mandamentos não são penosos;

Wolof

ndaxte mbëggeel ci yàlla mooy sàmm ay ndigalam; te ay ndigalam diisuñu.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Portugais

aquele que diz: eu o conheço, e não guarda os seus mandamentos, é mentiroso, e nele não está a verdade;

Wolof

ku wax ne xam nga ko, te sàmmoo ay ndigalam, dangay fen, te dëgg nekkul ci yaw.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Portugais

e qualquer coisa que lhe pedirmos, dele a receberemos, porque guardamos os seus mandamentos, e fazemos o que é agradável � sua vista.

Wolof

te lépp lu nu koy ñaan, dinanu ko jot ci moom, ndaxte nu ngi sàmm ay ndigalam, di def lu ko neex.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Portugais

e o amor é este: que andemos segundo os seus mandamentos. este é o mandamento, como já desde o princípio ouvistes, para que nele andeis.

Wolof

lii mooy mbëggeel: nu wéer sunug dund ci ndigali yàlla; loolu mooy ndigalam, la nu jotoon ca njàlbeen ga, te ci lanu wara jaar.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Portugais

aquele que tem os meus mandamentos e os guarda, esse é o que me ama; e aquele que me ama será amado de meu pai, e eu o amarei, e me manifestarei a ele.

Wolof

ki ma bëgg, mooy kiy nangu samay ndigal te di ko topp. ku ma bëgg, baay bi bëgg la, te man dinaa la bëgg, di la feeñu.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Portugais

porque, havendo moisés anunciado a todo o povo todos os mandamentos segundo a lei, tomou o sangue dos novilhos e dos bodes, com água, lã purpúrea e hissopo e aspergiu tanto o próprio livro como todo o povo,

Wolof

keroog musaa jàng na ndigali yoon wépp ci kanamu bànni israyil gépp. gannaaw loolu jël na deretu wëllu, jëlaale ndox, ak bantu garab gu ñuy wax isob, laxas ci kawaru xar mu xonq. noonu mu capp ko ca deret ja, daldi ko wis ca téereb yoon wa ak ca mbooloo mépp

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Portugais

respondeu-lhe ele: por que me perguntas sobre o que é bom? um só é bom; mas se é que queres entrar na vida, guarda os mandamentos.

Wolof

yeesu tontu ko: «lu tax nga laaj ma ci wàllu lu baax? kenn kepp moo baax. boo bëggee dugg ca dund googu ci kaw, nanga sàmm ndigal yi.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Portugais

a que guardes este mandamento sem mácula e irrepreensível até a vinda de nosso senhor jesus cristo;

Wolof

sàmmal ndigal li, bañ a am gàkk mbaa ŋàññ, ba kera yeesu kirist sunu boroom di feeñ ci ndamam, ca waxtu wa yàlla dogal.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,774,324,273 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK