Vous avez cherché: ousadamente (Portugais - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Portugais

Wolof

Infos

Portugais

paulo, entrando na sinagoga, falou ousadamente por espaço de três meses, discutindo e persuadindo acerca do reino de deus.

Wolof

noonu pool dugg ca jàngu ba, di wax ak fit wu dëgër diirub ñetti weer, di diisoo ak ñoom ci mbirum nguurug yàlla, di leen jéem a gëmloo.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Portugais

e pregando ousadamente em nome do senhor. falava e disputava também com os helenistas; mas procuravam matá-lo.

Wolof

muy wax ak di werante ak yawut yiy làkk gereg, waaye ñu di ko wut a rey.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Portugais

mas em parte vos escrevo mais ousadamente, como para vos trazer outra vez isto � memória, por causa da graça que por deus me foi dada,

Wolof

bu sama kàddu diisee nag ci bataaxal bii, dara taxul lu dul bëgg a yeesal seen xalaat, ndaxte yàlla ci kaw yiwam daf maa sas,

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Portugais

ele começou a falar ousadamente na sinagoga: mas quando priscila e Áqüila o ouviram, levaram-no consigo e lhe expuseram com mais precisão o caminho de deus.

Wolof

noonu mu daldi wax ak fit wu dëgër ca jàngu ba. bi ko pirsil ak akilas déggee nag, ñu woo ko fi ñoom, gën ko leeral yoonu yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Portugais

então barnabé, tomando-o consigo, o levou aos apóstolos, e lhes contou como no caminho ele vira o senhor e que este lhe falara, e como em damasco pregara ousadamente em nome de jesus.

Wolof

ci kaw loolu barnabas jël ko, yóbbu ko ca ndaw ya, nettali leen, ni sool gise boroom bi ci kaw yoon wi, ak li mu ko wax, rax-ca-dolli fit wi mu doon waxe ci turu yeesu ci damas.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Portugais

eles, entretanto, se demoraram ali por muito tempo, falando ousadamente acerca do senhor, o qual dava testemunho � palavra da sua graça, concedendo que por suas mãos se fizessem sinais e prodígios.

Wolof

pool ak barnabas nag sax nañu ci ikoñum lu yàgg, ñu wéeru ci boroom bi, bay wax ak fit wu dëgër; te yàlla dëggal kàddug yiwam, ba may leen, ñu def ay kéemaan ak ay firnde.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,780,158,459 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK