Vous avez cherché: dragoste (Roumain - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Roumain

Wolof

Infos

Roumain

tot ce faceţi, să fie făcut cu dragoste!

Wolof

lépp li ngeen di def, defleen ko ak mbëggeel.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Roumain

dar ştiu că n'aveţi în voi dragoste de dumnezeu.

Wolof

waaye yéen, xam naa leen; leer na ma ne, amuleen ci seen xol benn mbëggeel ci yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Roumain

spuneţi-vă sănătate unii altora cu o sărutare de dragoste.

Wolof

nuyoonteleen ak saafoonte yu sell. na jàmm ñeel képp ku gëm kirist.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Roumain

fără pricepere, călcători de cuvînt, fără dragoste firească, neînduplecaţi, fără milă.

Wolof

amuñu xel, amuñu kóllëre, amuñu cofeel, amuñu yërmande.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Roumain

căci martor îmi este dumnezeu că vă iubesc pe toţi cu o dragoste nespusă în isus hristos.

Wolof

ndaxte yàllaa seede ne, sama xol seey na ci yéen ñépp ci biir cofeelu kirist yeesu.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Roumain

cine nu iubeşte, n'a cunoscut pe dumnezeu; pentrucă dumnezeu este dragoste.

Wolof

ku bëggul sa mbokk, xamuloo yàlla, ndax yàlla mbëggeel la.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Roumain

ce voiţi? să vin la voi cu nuiaua, sau cu dragoste şi cu duhul blîndeţei?

Wolof

lu leen gënal? ma ñëw ci yéen, yor ab yar, walla ma ànd ak mbëggeel, te lewet?

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Roumain

prin aceasta vor cunoaşte toţi că sînteţi ucenicii mei, dacă veţi avea dragoste unii pentru alţii.``

Wolof

ni ñuy xame ne samay taalibe ngeen, mooy ngeen bëggante.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Roumain

căci dumnezeu nu ne -a dat un duh de frică, ci de putere, de dragoste şi de chibzuinţă.

Wolof

ndaxte xel mi nu yàlla sol du ànd ak ragal, waaye day ànd ak kàttan, mbëggeel ak moom sa bopp.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Roumain

cu toată smerenia şi blîndeţa, cu îndelungă răbdare; îngăduiţi-vă unii pe alţii în dragoste,

Wolof

ngeen woyof toyy te lewet, di muñalante tey baalante ci mbëggeel,

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Roumain

aşa încît hristos să locuiască în inimile voastre prin credinţă; pentruca, avînd rădăcina şi temelia pusă în dragoste,

Wolof

ba kirist dëkk ci seeni xol ci kaw ngëm. te ngeen sax noonu te sampu ci mbëggeelu yàlla,

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Roumain

pace fraţilor, şi dragoste împreună cu credinţa, din partea lui dumnezeu tatăl, şi din partea domnului isus hristos!

Wolof

yéen bokk yi, na leen yàlla baay bi ak yeesu kirist boroom bi may jàmm ak mbëggeel gu ànd ak ngëm.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Roumain

chiar dacă aş vorbi în limbi omeneşti şi îngereşti, şi n'aş avea dragoste, sînt o aramă sunătoare sau un chimval zîngănitor.

Wolof

su fekkee ne damay wax làkki nit ñi ak yu malaaka yi sax, te boolewuma ci mbëggeel, duma dara lu dul ndënd muy riir, walla jóolóoli buy kandaŋ-kandaŋi.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Roumain

deci, dacă este vreo îndemnare în hristos, dacă este vreo mîngîiere în dragoste, dacă este vreo legătură a duhului, dacă este vreo milostivire şi vreo îndurare,

Wolof

su nu kirist mayee fit nag ak mbëggeel guy dëfël sunu xol, su nu amee cér ci xel mu sell mi, su amee cofeel ak yërmande ci sunu bokk ci moom,

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Roumain

harul, îndurarea şi pacea să fie cu voi din partea lui dumnezeu tatăl, şi din partea domnului isus hristos, fiul tatălui, în adevăr şi în dragoste!

Wolof

yàlla baay bi ak yeesu krist, doomu baay bi, dinañu nu may yiw, yërmande ak jàmm, ànd ak dëgg ak mbëggeel.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Roumain

Şi noi am cunoscut şi am crezut dragostea pe care o are dumnezeu faţă de noi. dumnezeu este dragoste; şi cine rămîne în dragoste, rămîne în dumnezeu, şi dumnezeu rămîne în el.

Wolof

mbëggeel gi yàlla am ci nun, xam nanu ko te gëm ko. yàlla mbëggeel la, te képp ku sax ci mbëggeel, yaa ngi sax ci yàlla, mu dëkk ci yaw.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Roumain

căci dima, din dragoste pentru lumea de acum m'a părăsit, şi a plecat la tesalonic. crescens s'a dus în galatia, tit în dalmatia.

Wolof

ndaxte demas topp na àddina, ba bàyyi ma, dem dëkku tesalonig; kereseñsë dem na diiwaanu galasi, tit dem diiwaanu dalmasi.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Roumain

,,Ştiu faptele tale, dragostea ta, credinţa ta, slujba ta, răbdarea ta şi faptele tale depe urmă, că sînt mai multe decît cele dintîi.

Wolof

xam naa say jëf, sa mbëggeel, sa ngëm, sag muñ ak ni nga farloo ci sa jaamu yàlla. xam naa say jëf yu mujj, ni ñu ëppe yu jëkk ya. i

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,953,824 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK