Vous avez cherché: свидетельствуя (Russe - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Russe

Wolof

Infos

Russe

Но, получив помощь от Бога, я до сего дня стою, свидетельствуя малому и великому, ничего не говоря, кроме того, о чем пророки и Моисей говорили, что это будет,

Wolof

waaye gannaaw yàllaa ngi may taxawu ba tey, maa ngi taxaw fi, di ko seedeel ci mag ak ndaw; yokkuma dara ci li yonent yi ak musaa xamle woon lu jiitu,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Russe

Отринув его, поставил им царем Давида, о котором и сказал, свидетельствуя: нашел Я мужа по сердцу Моему, Давида, сына Иессеева, который исполнит все хотения Мои.

Wolof

dellu falal leen buur bu tudd daawuda, mu seedee ko nii: “gis naa daawuda, doomu yese, ku ma neex ci sama xol, te dina def lépp luy sama coobare.”

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Russe

И мы видели и свидетельствуем, что Отец послал Сына Спасителем миру.

Wolof

te nun gis nanu te seede ne, baay bi yónni na doom ji, mu nekk musalkatu àddina.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,777,116,712 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK