Vous avez cherché: slava (Serbe - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Serbe

Wolof

Infos

Serbe

kome slava va vek veka. amin.

Wolof

bi yelloo ndam ba fàww. amiin.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

jer ste vi naša slava i radost.

Wolof

xanaa du yéen? waaw yéenay sunu ndam, yéenay sunu mbég.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

njemu slava i država va vek veka. amin.

Wolof

na yàlla yelloo màgg ba fàww. amiin.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

a bogu i ocu našem slava va vek veka. amin.

Wolof

na yàlla sunu baay yelloo ndam ba fàww. amiin.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

jer im veæma omile slava ljudska nego slava božija.

Wolof

ngërëmu nit a leen gënaloon ngërëmu yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

jedinom premudrom bogu, kroz isusa hrista, slava vavek. amin.

Wolof

yàlla mi jagoo xam-xam bépp, moom rekk moo yelloo ndam ba fàww, jaar ci yeesu kirist! amiin.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

slava na visini bogu, i na zemlji mir, medju ljudima dobra volja.

Wolof

«nañu màggal yàlla ca asamaan su kawe sa,te ci àddina, na jàmm ji wàcc ci nit, ñi mu nangu ndax yiwam!»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

a slava i èast i mir svakome koji èini dobro, a najpre jevrejinu i grku;

Wolof

waaye ki doon def lu baax, añam mooy bokk ci ndamu yàlla, am ngërëm ak jàmm, muy yawut ci bu jëkk, mbaa ki dul yawut.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

jer je od njega i kroz njega i u njemu sve. njemu slava vavek. amin.

Wolof

ndaxte ci moom la lépp sosoo, ci moom la lépp di jaar, ci moom la lépp di dellu. moo yelloo ndam ba fàww. amiin.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

govoreæi: blagosloven car koji ide u ime gospodnje! mir na nebu i slava na visini!

Wolof

Ñu ngi naan:«yaw buur biy ñëw ci turu boroom bi,ku barkeel nga!na jàmm am ca asamaan,te ndam li féete ca bérab yu gën a kawe!»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

a caru veènom, neraspadljivom, koji se ne vidi, jedinom premudrom bogu èast i slava va vek veka. amin.

Wolof

yaw buur bi fiy sax ba abadan, yaw mi bët mënta gis, yaw yàlla miy kenn, yaa yelloo teraanga ak ndam ba fàww. amiin!

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

i gle, andjeo gospodnji stade medju njima, i slava gospodnja obasja ih; i uplašiše se vrlo.

Wolof

noonu benn malaakam boroom bi feeñu leen, ndamu boroom bi daldi leer, melax, wër leen. tiitaange ju réy jàpp leen.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

koja su izrailjci, kojih je posinaštvo i slava, i zavet i zakon, i bogomoljstvo, i obeæanja;

Wolof

bànni israyil lañu, te yàlla def na leen ni ay doomam; dëkkaloon na ndamam ci seen biir, fas ak ñoom kóllëre yi. Ñoom la yàlla dénk yoonu musaa, ñoom la xamal ni ñu ko war a jaamoo, ñoom la jox i digam.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

a za tita, on je moj drug i pomagaè medju vama; a za braæu našu, oni su poslanici crkveni i slava hristova.

Wolof

noonu kon ci lu jëm ci tit, sama nawle la ci liggéey, bi ci seen biir. ci lu jëm ci sunu bokk, yi ànd ak moom nag, ndawi mbooloom ñi gëm lañu, ñuy wone ndamu kirist.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

govoreæi: amin; blagoslov i slava i premudrost i hvala i èast i sila i jaèina bogu našem va vek veka. amin.

Wolof

naan:«amiin. na cant ak ndam, xel ak ngërëm, teraanga, kàttan ak dooleféete ak yàlla sunu boroom ba fàww. amiin!»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

druga je slava suncu, a druga slava mesecu, i druga slava zvezdama; jer se zvezda od zvezde razlikuje u slavi.

Wolof

jant bi, weer wi ak biddiiw, lu nekk ak sag leer. te it leeru biddiiw bu nekk dina wuute ak moroomam.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

isus odgovori: ako se ja sam slavim, slava je moja ništa: otac je moj koji me slavi, za kog vi govorite da je vaš bog.

Wolof

yeesu ne leen: «su ma dee màggal sama bopp, du am maana. sama baay a may màggal, moom mi ngeen naan, mooy seen yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

da vas savrši u svakom delu dobrom, da uèinite volju njegovu, èineæi u vama šta je ugodno pred njime, kroz isusa hrista, kome slava va vek veka. amin.

Wolof

matal ci lépp lu baax, ba ngeen man a def coobareem, di jëfe ci nun li neex ci moom, mu jaarale lépp ci yeesu kirist, moom mi yelloo ndam ba fàww. amiin.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

ako ko govori, neka govori kao reèi božije; ako ko služi neka služi kao po moæi koju bog daje: da se u svaèemu slavi bog kroz isusa hrista, kome je slava i država va vek veka. amin.

Wolof

kuy jottali kàddug yàlla, na mel ni yàllaay wax. kuy jëf it, na jëfe dooley yàlla, ngir turu yàlla màgg ci lépp jaar ci yeesu kirist, mi yelloo ndam ak kàttan ba fàww. amiin.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,788,161,336 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK