Vous avez cherché: zaista (Serbe - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Serbe

Wolof

Infos

Serbe

zaista vam kažem da æe ovo sve doæi na rod ovaj.

Wolof

ci dëgg maa ngi leen koy wax, loolu lépp dina dal ci niti jamono jii.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

ako vas, dakle, sin izbavi, zaista æete biti izbavljeni.

Wolof

kon nag bu leen doom ji defee gor, dingeen doon ay gor tigi.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

zaista vam kažem: nad svim svojim imanjem postaviæe ga.

Wolof

ci dëgg maa ngi leen koy wax, njaatige bi dina ko teg ci alalam jépp.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

koji govorahu: zaista ustade gospod, i javi se simonu.

Wolof

Ñooñu ne leen: «dëgg la, boroom bi dekki na, te feeñu na simoŋ!»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

govoreæi: zaista blagosiljajuæi blagosloviæu te, i umnožavajuæi umnožiæu te.

Wolof

ne ko: «sàllaaw dinaa la barkeel, yokk saw askan.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

a on odgovarajuæi reèe im: zaista vam kažem: ne poznajem vas.

Wolof

waaye mu tontu leen ne: “ci dëgg maa ngi leen koy wax, xawma leen.”

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

zaista, zaista vam kažem: koji veruje mene ima život veèni.

Wolof

ci dëgg-dëgg maa ngi leen koy wax, ku gëm am nga dund gu dul jeex.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

a mnogi od naroda èuvši ove reèi govorahu: ovo je zaista prorok.

Wolof

bi ñu déggee wax jooja, am ay nit ca mbooloo ma ñu naan: «dëgg-dëgg kii mooy yonent bi war a ñëw.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

i reèe mu isus: zaista ti kažem: danas æeš biti sa mnom u raju.

Wolof

yeesu tontu ko ne: «ci dëgg maa ngi la koy wax, tey jii dinga texe ak man ca jataayu yàlla.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

a petar otvorivši usta reèe: zaista vidim da bog ne gleda ko je ko;

Wolof

noonu piyeer jël kàddu ga ne leen: «ci dëgg gis naa ne, yàlla du gënale,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

i kad jedjahu reèe im: zaista vam kažem: jedan izmedju vas izdaæe me.

Wolof

bi ñuy lekk, mu ne leen: «ci dëgg maa ngi leen koy wax, kenn ci yéen dina ma wor.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

a kad vide kapetan šta bi, stade hvaliti boga govoreæi: zaista ovaj èovek beše pravednik.

Wolof

bi njiitu xare ba gisee li xewoon, mu màggal yàlla ne: «dëgg-dëgg nit kii ku jub la woon.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

a isus im reèe: zaista, zaista vam kažem: ja sam pre nego se avraam rodio.

Wolof

yeesu ne leen: «ci dëgg-dëgg maa ngi leen koy wax, laata ñuy sàkk ibraayma, fekk na ma doon ki ñuy wax maay ki nekk.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

a ljudi videvši èudo koje uèini isus govorahu: ovo je zaista onaj prorok koji treba da dodje na svet.

Wolof

bi nit ña gisee firnde jooju yeesu wone, ñu ne: «dëgg-dëgg kii mooy yonent, bi war a ñëw ci àddina!»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

a koji drži reè njegovu, u njemu je zaista ljubav božija savršena; po tom poznajemo da smo u njemu.

Wolof

kuy sàmm kàddug yàlla, dëgg-dëgg sa mbëggeel ci yàlla mat na sëkk. ci loolu lanu xame ne, nekk nanu ci moom.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

a kad vide kapetan koji stajaše prema njemu da s takvom vikom izdahnu, reèe: zaista èovek ovaj sin božji beše.

Wolof

njiitu xare nag, bi taxawoon ci kanamu yeesu, bi mu gisee ni yeesu deeye, mu ne: «ci dëgg, nit kii doomu yàlla la!»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

i odgovarajuæi car reæi æe im: zaista vam kažem: kad uèiniste jednom od ove moje najmanje braæe, meni uèiniste.

Wolof

noonu buur bi dina leen tontu ne: “ci dëgg maa ngi leen koy wax, saa yu ngeen defalee loolu kenn ki gën a ndaw ci sama bokk yii, man ngeen ko defal.”

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

a kapetan i koji s njim èuvahu isusa videvši da se zemlja trese i šta bi, poplašiše se vrlo govoreæi: zaista ovaj beše sin božji.

Wolof

noonu njiitu xare bi ak ñi ànd ak moom di wottu yeesu, bi ñu gisee suuf si yengu ak li xew, ñu daldi tiit lool ne: «ci dëgg, kii doomu yàlla la.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

a isus reèe im: ne vidite li sve ovo? zaista vam kažem: neæe ostati ovde ni kamen na kamenu koji se neæe razmetnuti.

Wolof

waaye mu tontu leen ne: «du gis ngeen yii yépp? ci dëgg maa ngi leen koy wax, lii lépp dina daanu, ba doj dootul des ci kaw doj.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Serbe

eda li je dakle zakon protivan obeæanjima božjim? bože saèuvaj! jer da je dan zakon koji može oživeti, zaista bi od zakona bila pravda.

Wolof

ndax kon yoonu musaa wi dafa juuyoo ak li yàlla dige? mukk! su amoon yoon wu nit man a sàmm, ba mu jural ko dund gu sax, kon sàmm yoon dina tax nit jub fa kanam yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,833,056 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK