Vous avez cherché: kiebrania (Swahili - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Swahili

Wolof

Infos

Swahili

basi, roho hao wakawakusanya hao wafalme mahali paitwapo kwa kiebrania harmagedoni.

Wolof

noonu rab ya dajale buuri àddina si ci bérab bu tudd ci làkku yawut armagedon.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

waliposikia akiongea nao kwa kiebrania wakazidi kukaa kimya zaidi kuliko hapo awali. naye paulo akaendelea kusema,

Wolof

bi ñu déggee, mu di leen wax ci làkku yawut, ñu gën ne xeram. noonu pool ne leen:

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

yule mkuu wa jeshi akamruhusu. hivyo paulo alisimama juu ya ngazi, akawapungia mkono wale watu na walipokaa kimya, akaanza kuongea nao kwa kiebrania.

Wolof

te kilifa ga may ko ko. noonu pool taxaw ca yéegukaay ba, tàllal loxoom mbooloo ma, ñu daldi ne tekk. mu wax ak ñoom ci làkku yawut ne:

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

huko yerusalemu, karibu na mlango uitwao mlango wa kondoo, kulikuwa na bwawa la maji liitwalo kwa kiebrania bethzatha, ambalo lilikuwa na baraza tano zenye matao.

Wolof

ca wetu benn ci bunti dëkk ba nag, maanaam ca buntu xar ya, am na fa bët bu tudd betesda ci làkku yawut, te ñu wërale ko ak juróomi mbaar.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

sisi sote tulianguka chini, nami nikasikia sauti ikiniambia kwa kiebrania: saulo, saulo! kwa nini unanitesa? unajiumiza bure kama punda anayepiga teke fimbo ya bwana wake.

Wolof

nu ne nërëm ci suuf, ma dégg baat bu ma wax ci làkku yawut ne: “sool, sool, lu tax nga di ma fitnaal? ngay bëre ak man ni fas wuy woŋŋeetu ku koy jam dëgël, metti na ci yaw.”

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

baadaye, idadi ya wanafunzi ilipokuwa inazidi kuongezeka, kulitokea manung'uniko kati ya wanafunzi waliosema kigiriki na wale waliosema kiebrania. wale waliosema kigiriki walinung'unika kwamba wajane wao walikuwa wanasahauliwa katika ugawaji wa mahitaji ya kila siku.

Wolof

ca bés yooyu, naka taalibe yi di gën a bare, yawut yiy làkk gereg tàmbalee ñaxtu ci mbirum yawut tigi yi, te lii a ko waral: jigéen ñi seen jëkkër dee, te ñu bokk ci ñoom, naraalewuñu leen ca ndimbal, la ñuy séddale bés bu nekk.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,748,135,010 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK