Vous avez cherché: manabii (Swahili - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Swahili

Wolof

Infos

Swahili

aliahidi hapo kale kwa njia ya manabii wake watakatifu,

Wolof

ni mu yéglee woon bu yàggjaarale ko ci yonentam yu sell yi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

watatokea manabii wengi wa uongo watakaowapotosha watu wengi.

Wolof

te it ñu bare ñuy mbubboo turu yonent dinañu feeñ, nax nit ñu bare.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

jihadharini basi, msije mkapatwa na yale yaliyosemwa na manabii:

Wolof

wottuleen nag ba li yonent yi bindoon bañ leen a dal, ci li ñu ne:

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

mafundisho yote ya manabii na sheria yalibashiri juu ya nyakati hizi.

Wolof

ndaxte li yonent yi wax ak li yoonu musaa tëral ñu ngi doon dox, ba kera yaxya di feeñ.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

wakati huohuo, manabii kadhaa walikuja antiokia kutoka yerusalemu.

Wolof

ca fan yooyu ay yonent jóge yerusalem, ñëw ancos.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

sheria yote ya mose na mafundisho ya manabii vinategemea amri hizi mbili."

Wolof

Ñaari ndigal yooyu tënk nañu yoonu musaa wépp, moom ak waxi yonent yi.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

ole wenu, kwa kuwa mnajenga makaburi ya manabii wale ambao wazee wenu waliwaua.

Wolof

dingeen torox, ndaxte yéena ngi tabax xabruy yonent, yi seeni maam reyoon.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

akawafafanulia mambo yote yaliyomhusu yeye katika maandiko matakatifu kuanzia mose hadi manabii wote.

Wolof

noonu mu tàmbalee ci yonent yàlla musaa ba ci yonent yépp, tekkil leen li mbind mi wax lépp ci ay mbiram.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

jambo hili ni sawa kabisa na maneno ya manabii, kama maandiko matakatifu yasemavyo:

Wolof

te loolu sax dëppoo na ak li yonent yi tëral; ñu bind ne:

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

hapo zamani, mungu alisema na babu zetu mara nyingi kwa namna nyingi kwa njia ya manabii,

Wolof

li jiitu tey yàlla waxoon na ak maam ya ci wàll yu bare ak ci tëralin yu wuute jaarale ko ca yonent ya.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

hapo kale, mungu aliwaahidia watu hii habari njema kwa njia ya manabii wake katika maandiko matakatifu.

Wolof

xebaar bu baax boobu, yàlla dige woon na ko bu yàgg, jaarale ko ciy yonentam, ñu def ko ci mbind mu sell mi,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

furahini na kushangilia maana tuzo lenu ni kubwa mbinguni. hivyo ndivyo walivyowadhulumu manabii waliokuwako kabla yenu.

Wolof

bégleen te bànneexu, ndax seen yool dina réy ci laaxira. ndaxte noonu lañu daan fitnaale yonent yi fi jiitu.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

"msidhani ya kuwa nimekuja kutangua sheria ya mose na mafundisho ya manabii. sikuja kutangua bali kukamilisha.

Wolof

«buleen defe ne, ñëw naa ngir dindi yoonu musaa ak waxi yonent yi. Ñëwuma ngir dindi leen, waaye ngir ñu am ci man.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

"watendeeni wengine yale mnayotaka wao wawatendee ninyi. hii ndiyo maana ya sheria ya mose na mafundisho ya manabii.

Wolof

«kon nag lépp lu ngeen bëgg, nit ñi defal leen ko, yéen itam nangeen leen ko defal; ndaxte loolu moo ëmb yoonu musaa ak waxi yonent yi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

"jihadharini na manabii wa uongo. wao huja kwenu wakionekana kama kondoo kwa nje, lakini kwa ndani ni mbwa mwitu wakali.

Wolof

«moytuleen ñi mbubboo turu yonent. dañuy ñëw ci yéen, yor melow xar, waaye ci biir ay bukki yu soxor lañu.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

"bwana, wamewaua manabii wako na kubomoa madhabahu yako. ni mimi tu peke yangu niliyebaki, nao wanataka kuniua?"

Wolof

«boroom bi, rey nañu say yonent, daaneel say bérab yu sell, ba man kenn maa ci des, te ñu ngi may wut a rey.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

akahamia katika mji uitwao nazareti. ndivyo yalivyotimia maneno yaliyonenwa kwa njia ya manabii: "ataitwa mnazare."

Wolof

mu ñëw nag dëkk ci dëkk bu ñuy wax nasaret. noonu am la ñu waxoon ca xale ba, jaarale ko ca yonent ya, bi ñu naan:«dees na ko tudde nasaréen.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

lakini wakati ule malaika wa saba atakapotoa sauti yake, wakati atakapopiga tarumbeta yake, mungu atakamilisha mpango wake wa siri kama alivyowatangazia watumishi wake manabii."

Wolof

waaye jamono ju juróom-ñaareelu malaaka ma wolee ci liitam, ndogalu yàlla dina mat, ni mu ko waxe woon ay jaamam, yonent yi.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

"sheria na maandishi ya manabii vilikuweko mpaka wakati wa yohane mbatizaji. tangu hapo, ufalme wa mungu unahubiriwa, na kila mmoja anauingia kwa nguvu.

Wolof

«yoonu musaa wi ak waxi yonent yi ñu ngi fi woon ba kera yaxya di ñëw. la ko dale foofa nag, yégle nañu xebaar bu baax bi ci nguuru yàlla, te ñépp a ngi góor-góorlu, ngir dugg ci.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

furahi ee mbingu, kwa sababu ya uharibifu wake. furahini watu wa mungu, mitume na manabii! kwa maana mungu ameuhukumu kwa sababu ya mambo uliyowatenda ninyi!

Wolof

yaw asamaan, bégal ci li ñu ko yàq!yéen itam gaayi yàlla yi,ndaw yi ak yonent yi, bégleen,ndaxte yàlla àtte na ko, ba feyyul leen.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,740,040,014 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK