Vous avez cherché: mfarisayo (Swahili - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Swahili

Wolof

Infos

Swahili

huyo mfarisayo alistaajabu kuona kwamba alikula chakula bila kunawa.

Wolof

farisen bi nag daldi jaaxle, bi mu gisee ne yeesu raxasuwul, laata muy lekk.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

mfarisayo kipofu! kisafishe kikombe ndani kwanza na nje kutakuwa safi pia.

Wolof

farisen yu gumba yi! jëkkleen a setal biir kaas bi ak ndab li, ngir biti bi itam set.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

"watu wawili walipanda kwenda hekaluni kusali: mmoja mfarisayo, na mwingine mtoza ushuru.

Wolof

mu ne: «dafa amoon ñaari nit ñu dem ca kër yàlla ga, di ñaan. kenn ki ab farisen la, ki ci des juutikat.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

basi, katika mji ule kulikuwa na mama mmoja aliyekuwa anaishi maisha mabaya. alipopata habari kwamba yesu yuko nyumbani kwa huyo mfarisayo, alichukua chupa ya alabasta yenye marashi.

Wolof

fekk amoon na ca dëkk ba jigéen juy moy yàlla. bi mu yégee ne, yeesoo ngay lekk ca kër farisen ba, mu dem, yóbbaale njaq lu ñu defare doj wu ñuy wax albaatar te def latkoloñ.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

yule mfarisayo aliyemwalika yesu alipoona hayo, akawaza moyoni mwake, "kama mtu huyu angekuwa kweli nabii angejua huyu mwanamke ni wa namna gani, ya kwamba ni mwenye dhambi."

Wolof

naka la farisen, bi woo woon yeesu ci këram, gis loolu, mu wax ci xelam naan: «bu nit kii doonoon yonent, kon dina xam kuy jigéen ji koy laal ak ni mu nekke bàkkaarkat.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

huyo mfarisayo akasimama, akasali kimoyomoyo: ee mungu, nakushukuru kwa vile mimi si kama watu wengine: walafi, wadanganyifu au wazinzi. nakushukuru kwamba mimi si kama huyu mtoza ushuru.

Wolof

farisen baa nga taxaw di ñaan ci xelam naan: “yaw yàlla, maa ngi lay sant ci li ma melul ni ñeneen ñiy sàcc, di def lu jubadi te di njaaloo, rawatina juutikat bii.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,792,476,484 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK