Vous avez cherché: mishahara (Swahili - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Swahili

Wolof

Infos

Swahili

hamkuwalipa mishahara watumishi waliofanya kazi katika mashamba yenu. sikilizeni malalamiko yao! kilio cha hao wanaovuna mashamba yenu kimefika masikioni mwa bwana, mwenye nguvu.

Wolof

dégluleen, jooyi xaalis bi ngeen sàcce ci gubkat, yi leen doon liggéeyal, ak yuuxi góobkat yi, dugg nañu ci noppi yàlla aji kàttan ji.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

nao askari wakamwuliza, "na sisi tufanye nini?" naye akawajibu, "msichukue vitu vya mtu yeyote kwa nguvu wala kumshtaki yeyote kwa uongo. toshekeni na mishahara yenu."

Wolof

ay xarekat laaj nañu ko ne: «li jëm ci nun nag?» mu ne leen: «buleen néewal doole kenn, jël xaalisam ci kaw ay tëkku mbaa ci seede lu dul dëgg. waaye doylooleen li ñu leen di fey.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,792,840,053 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK