Vous avez cherché: msaada (Swahili - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Swahili

Wolof

Infos

Swahili

tukiishi kwa msaada wa roho, na tuufuate mwongozo wake.

Wolof

gannaaw nag nu ngi dund léegi ci xelum yàlla, kon nanu ko topp.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

toa msaada wako kwa siri, na baba yako aonaye yaliyofichika, atakutuza.

Wolof

ngir sa sarax nekk kumpa. noonu sa baay, bi dara umpul, dina la ko delloo.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

twateseka, lakini hatuachwi bila msaada; na ingawa tumeangushwa chini, hatukuangamizwa.

Wolof

dañu nuy fitnaal, waaye yàlla du nu wacc mukk. tër nañu nu, waaye kenn doggaliwu nu.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

hatimaye, nawatakeni muwe imara katika kuungana na bwana na kwa msaada wa nguvu yake kuu.

Wolof

léegi nag doolewuleen ci boroom bi, te soloo kàttanam gu mag gi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

maana wanaanza safari yao katika utumishi wa kristo bila kupokea msaada wowote kutoka kwa watu wasioamini.

Wolof

ndaxte turu krist la leen taxa jóg, te sàkkuwuñu daray ku gëmul.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

tulifanya hivyo si kwa kuwa hatuna haki ya kutaka msaada wenu, ila kwa sababu tunataka kuwapeni mfano.

Wolof

waxuma ne amunu sañ-sañu def ko, waaye danoo bëggoon a nekk ay royukaay ci yéen, ngir ngeen aw ci sunuy tànk.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

"baada ya kukaa mbali kwa miaka kadhaa, nilirudi yerusalemu ili kuwapelekea wananchi wenzangu msaada na kutoa dhabihu.

Wolof

«noonu gannaaw gëjeb at yu bare ñëw naa, ngir indil sama xeet ndimbal te jébbal yàlla ay sarax.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

mwanamke mjane kweli, asiye na mtu wa kumsaidia, amemwekea mungu tumaini lake na huendelea kusali na kumwomba msaada usiku na mchana.

Wolof

jigéen ju sësul ci kenn day wékk yaakaaram jépp ci yàlla, sax ci di ko wéetal te di ko ñaan guddi ak bëccëg.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

je, mu wajinga kiasi hicho? ninyi mlianza yote kwa msaada wa roho je, mnataka sasa kumaliza kwa nguvu zenu wenyewe?

Wolof

mbaa du nii ngeen ñàkke xel, ba tàmbalee ci xelum yàlla, ba noppi yaakaar a mate ci seen jëfi bopp?

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

basi, nimewatuma ndugu zetu hao, ili fahari yetu juu yenu ionekane kwamba si maneno matupu, na kwamba mko tayari kabisa na msaada wenu kama nilivyosema.

Wolof

maa ngi yónni nag bokk yooyu, ngir damu gi nu doon damu ci yéen ci mbir mii bañ a neen, te ngeen jekk, ni ma ko waxe woon.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

je, mlipungukiwa nini zaidi kuliko makanisa mengine, isipokuwa tu kwamba mimi kwa upande wangu sikuwasumbueni kupata msaada wenu? samahani kwa kuwakoseeni haki hiyo!

Wolof

lan laa defal yeneen mboolooy ñi gëm te defaluma leen ko, xanaa rekk li ma wéeru ci ñoom te wéeruma ci yéen? baal-leen ma googu tooñ!

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

mtu wa kidunia hapokei mambo ya roho wa mungu. kwake mtu huyo mambo hayo ni upumbavu mtupu; yanapita akili yake; maana yanaweza tu kutambuliwa kwa msaada wa roho.

Wolof

nit kese du nangu yëfi xelum yàlla. ag ndof lay doon ci moom, te du ko man a nangu, ndaxte ku yor xelum yàlla rekk moo ko man a ràññale.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

apolo alipoamua kwenda akaya, wale ndugu walimtia moyo kwa kuwaandikia wafuasi kule akaya wampokee. alipofika huko, aliweza kwa msaada wa neema ya mungu, kuwasaidia sana wale ndugu waliopata kuwa waumini;

Wolof

naka mu bëgg a dem akayi, bokk ya xiir ko ca, ñu bind taalibe ya, ngir ñu teeru ko teeru bu rafet. noonu mu dikk fa te jariñ lool ñi gëm jaare ko ci yiwu yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

chini ya uongozi wake, viungo vyote vya mwili hushikamana pamoja, na mwili wote hutegemezwa kwa msaada wa viungo vyake. basi, kila kiungo kikitekeleza kazi yake ipasavyo, mwili wote hukua na kujijenga katika upendo.

Wolof

te jëmm jépp ci moom lay dunde, di jëmm ju ràbboo te déggoo ci bépp tenqoo, te cér bu nekk di def warugaram. noonu jëmm ji di yokku ak a màgg ci biir mbëggeel.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

wakipiga kelele: "wananchi wa israeli, msaada, msaada! huyu ndiye yule mtu anayewafundisha watu kila mahali mambo yanayopinga watu wa israeli, yanayopinga sheria ya mose na mahali hapa patakatifu. hata sasa amewaingiza watu wa mataifa mengine hekaluni na kupatia najisi mahali hapa patakatifu."

Wolof

di xaacu ne: «wallee, wallee, yéen bokki israyil; waa jaa ngi nii, moom miy waare fépp ak ci ñépp, bay suufeel sunu xeet ak yoonu musaa ak bérab bii; dugal na sax ay gereg fii ci kër yàlla gi, ba indi sobe ci bérab bu sell bii.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,772,988,853 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK