Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
basi, ndugu zangu, msishangae kama ulimwengu unawachukia ninyi.
bokk yi, bu leen àddina bañee, buleen ci jaaxle.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
wapenzi wangu, msishangae kuhusu majaribio makali mnayopata kana kwamba mnapatwa na kitu kisicho cha kawaida.
yéen samay xarit, ci mbirum nattu bu tànge ni daay, bi dal ci seen kaw, bumu leen jaaxal, ba ngeen teg ko ni lu xel dajul.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
lakini huyo kijana akawaambia, "msishangae. mnamtafuta yesu wa nazareti aliyesulubiwa. amefufuka, hayumo hapa. tazameni mahali walipokuwa wamemlaza.
waaye mu ne leen: «buleen tiit. yéena ngi seet yeesum nasaret, mi ñu daajoon ci bant bi. nekkatu fi, dekki na; gisleen fi ñu ko tëraloon.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Avertissement : un formatage HTML invisible est présent