Vous avez cherché: mwanamume (Swahili - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Swahili

Wolof

Infos

Swahili

mwanamume hakutoka kwa mwanamke, ila mwanamke alitoka kwa mwanamume.

Wolof

ndaxte jëlewuñu góor ci jigéen, waaye jigéen lañu jële ci góor.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

hivyo mwanamume atawaacha baba yake na mama yake, ataungana na mkewe,

Wolof

moo tax góor dina beru ndeyam ak baayam, di taq ci jabaram,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

lakini tangu kuumbwa ulimwengu, mungu aliumba mwanamume na mwanamke.

Wolof

waaye ca njàlbéen ga “yàlla sàkk na leen, kii góor, kii jigéen.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

mimi simruhusu mwanamke amfundishe au amtawale mwanamume; anapaswa kukaa kimya.

Wolof

mayuma jigéen, muy jàngale mbaa muy jiite góor, waaye na noppi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

kila mwanamume anapaswa kujua namna ya kuishi na mkewe kwa utakatifu na heshima,

Wolof

ngeen noot seeni cér ci cell ak tedd,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

mwanamume hakuumbwa kwa ajili ya mwanamke, ila mwanamke aliumbwa kwa ajili ya mwanamume.

Wolof

te sàkkuñu góor ngir jigéen, waaye jigéen lañu sàkk ngir góor.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

hata hivyo, mbele ya bwana mwanamke si kitu bila mwanamume, naye mwanamume si kitu bila mwanamke.

Wolof

teewul nag ci sunu booloo ak boroom bi, jigéen a ngi wéeru ci góor, te góor a ngi wéeru ci jigéen.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

basi, kila mwanamume anayesali au anayetangaza ujumbe wa mungu huku amefunika kichwa chake, huyo anamdharau kristo.

Wolof

kon nag góor guy ñaan yàlla, walla muy wax ci kàddug yàlla, fekk mu teg dara ci boppam, day suufeel kirist, kilifaam.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

kama vile mwanamke alivyotokana na mwanamume, vivyo hivyo mwanamume huzaliwa na mwanamke; kila kitu hutoka kwa mungu.

Wolof

ni ñu sàkke jigéen ci góor, noonu la góor juddoo ci jigéen, te lépp a ngi jóge ca yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

lakini kwa sababu ya hatari ya uzinzi, basi, kila mwanamume na awe na mke wake mwenyewe, na kila mwanamke awe na mume wake mwenyewe.

Wolof

lii mooy sama xalaat: moy gu bare gi tax na ba, na góor gu nekk am jabaram, jigéen ju nekk am jëkkëram.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

na akasema: kwa sababu hiyo mwanamume atamwacha baba yake na mama yake, ataungana na mke wake, nao wawili watakuwa mwili mmoja?

Wolof

te mu ne: “moo tax góor dina beru ndeyam ak baayam, di taq ci jabaram, ñoom ñaar doon benn.”

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

haifai mwanamume kufunika kichwa chake, kwa kuwa yeye ni mfano wa mungu na kioo cha utukufu wake mungu; lakini mwanamke ni kioo cha utukufu wa mwanamume.

Wolof

góor nag moom warul a teg dara ci boppam, ndaxte mooy melokaanu yàlla te dafay wone ndamu yàlla. jigéen moom dafay wone ndamu góor.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

hivyo, hakuna tena tofauti kati ya myahudi na mgiriki, mtumwa na mtu huru, mwanamume na mwanamke. nyote ni kitu kimoja katika kuungana na kristo yesu.

Wolof

kon nag amul xaajale ci diggante yawut ak ki dul yawut, ci diggante jaam ak gor, ci diggante góor ak jigéen. yéen ñépp benn ngeen ci seen bokk ci kirist.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

akawaambia, "sikilizeni! mtakapokuwa mnakwenda mjini, mtakutana na mwanamume anayebeba mtungi wa maji. mfuateni mpaka ndani ya nyumba atakayoingia.

Wolof

mu ne leen: «bu ngeen duggee ca dëkk ba, góor gu yenu njaq lu def ndox, dina taseek yéen. toppleen ci moom ba ca kër ga muy dugg,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

kama yasemavyo maandiko matakatifu: "kwa hiyo, mwanamume atawaacha baba na mama yake, ataungana na mkewe, nao wawili watakuwa mwili mmoja."

Wolof

mbind mi nee na: «moo tax góor dina beru ndeyam ak baayam, di taq ci jabaram, ñoom ñaar doon benn.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

hivyo mwanamke huyo akiishi na mwanamume mwingine wakati mumewe yungali hai, ataitwa mzinzi; lakini mumewe akifa, mwanamke huyo yu huru kisheria, na akiolewa na mwanamume mwingine, yeye si mzinzi.

Wolof

kon nag su jabar ji àndee ak beneen góor, te fekk jëkkër jiy dund, dees na ko àtte njaaloo. waaye bu jëkkër ji faatoo, yoon jeexal na seen diggante; man na séy nag ak beneen góor, te loolu du njaaloo.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

kwa wale wengine, (mimi binafsi, si bwana) nasema hivi: ikiwa mwanamume mkristo anaye mke asiyeamini, na huyo mwanamke akakubali kuendelea kuishi naye, asimpe talaka.

Wolof

Ñi ci des nag, lii laa leen di wax --boroom bi waxu ko woon — su nit ku gëm kirist amee jabar ju gëmul, te mu nangoo séy ak moom, waru koo fase.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,603,693 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK