Vous avez cherché: nilipokwenda (Swahili - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Swahili

Wolof

Infos

Swahili

nilipokwenda yerusalemu makuhani wakuu na wazee wa wayahudi walimshtaki na kuniomba nimhukumu.

Wolof

te bi ma nekkee yerusalem, saraxalekat yu mag ya ak njiiti yawut ya kalaame nañu ko ci man, ñaan ma, ma daan ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

unaweza kujihakikishia kwamba si zaidi ya siku kumi na mbili tu zimepita tangu nilipokwenda kuabudu yerusalemu.

Wolof

man ngaa wóorliku ne, ëppagul fukki fan ak ñaar demoon naa yerusalem ngir màggali.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

ilikuwa tu baada ya miaka mitatu, ndipo nilipokwenda yerusalemu kuonana na kefa; nilikaa kwake siku kumi na tano.

Wolof

ba ñu ca tegee ñetti at, ma sog a dem yerusalem, ngir xamante ak sefas, dal fa moom lu mat ñaari ayu-bés.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,747,923,289 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK