Vous avez cherché: popote (Swahili - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Swahili

Wolof

Infos

Swahili

popote waendapo husababisha maafa na mateso;

Wolof

fu ñu jaar, foofa yàqu ak musiba.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

maana popote palipo na wivu na ubinafsi hapo pana fujo na kila aina ya uovu.

Wolof

ndaxte fu wextan ak wut aw tur dugg, indi fa xëccoo ak bépp ñaawteef.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

tena aliwaambia, "popote mtakapokaribishwa nyumbani, kaeni humo mpaka mtakapoondoka mahali hapo.

Wolof

mu ne leen: «kër gu ngeen dugg, dal-leen fa, ba kera ngeen jóge dëkk ba.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

kwa maana popote pale wanapokusanyika wawili au watatu kwa jina langu, mimi nipo hapo kati yao."

Wolof

ndaxte fu ñaar walla ñetti nit booloo ci sama tur, maa ngi ci seen biir.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

naahidi kwa ule ukweli wa kristo ulio ndani yangu, kwamba hakuna kitakachoweza kunizuia kujivunia jambo hilo popote katika akaya.

Wolof

ni mu wóore ne, dëggug kirist nekk na ci man, ni la wóore ne loolii may damoo, kenn du ko teggi ci diiwaanu akayi gépp.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

nawaambieni kweli, popote ambapo hii habari njema itahubiriwa ulimwenguni, kitendo hiki alichofanya mama huyu kitatajwa kwa kumkumbuka yeye."

Wolof

ci dëgg maa ngi leen koy wax, fépp fu ñuy yéene xebaar bu baax bi ci àddina sépp, dinañu fa fàttali it li jigéen jii def.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

anayetaka kunitumikia ni lazima anifuate, hivyo kwamba popote pale nilipo mimi ndipo na mtumishi wangu atakapokuwa. mtu yeyote anayenitumikia baba yangu atampa heshima.

Wolof

ku bëgg a doon sama surga, na ma topp. bu ko defee, fu ma nekk, fa lay nekk moom itam. ku may liggéeyal, sama baay dina ko teral.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

maana, kutokana na bidii yenu ujumbe wa bwana umesikika si tu huko makedonia na akaya, bali imani yenu kwa mungu imeenea popote. tena hatuhitaji kusema zaidi.

Wolof

ndaxte kàddug boroom bi jollee na ci seen biir, te yemul ci maseduwan ak akayi rekk, waaye seen gëm yàlla siiw na fépp. matul sax nu di ci wax dara,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

wakati huo kanisa likawa na amani popote katika yudea, galilaya, na samaria. lilijengwa na kukua katika kumcha bwana, na kuongezeka likitiwa moyo na roho mtakatifu.

Wolof

noonu mbooloom ñi gëm nekk ci jàmm ci biir diiwaani yude gépp ak galile ak samari; ñuy gën a dëgër, di wéy ci ragal yàlla, tey yokku ci ndimbalu xel mu sell mi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

tunawaandikia ninyi mlio kanisa la mungu huko korintho. ninyi mmefanywa watakatifu katika kuungana na kristo yesu, mkaitwa muwe watu wa mungu, pamoja na watu wote popote wanaomwomba bwana wetu yesu kristo aliye bwana wao na wetu pia.

Wolof

noo leen di bind, yéen mbooloom yàlla, mi dëkk korent. nu ngi leen di nuyu, yéen ñi yàlla sédde boppam jaare ci kirist yeesu, yéen ñi yàlla woo, ngeen sell, boole leen ak ñi nekk ci àddina sépp tey tudd turu sunu boroom yeesu kirist, miy seen boroom, di sunu bos.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

maana maandiko matakatifu yasema hivi kwa farao: "nilikufanya mfalme ili kwa njia yako, uwezo wangu ujulikane, na jina langu litangazwe popote duniani."

Wolof

ndax mbind mi biral na li yàlla wax firawna ne ko:«def naa la buur,ngir feeñal sama kàttan ci say mbir,te ngir siiwal sama tur ci àddina si sépp.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

hakuna mashaka yoyote juu ya ukuu wa siri ya dini yetu: alionekana katika umbo la kibinadamu alithibitishwa na roho kuwa ni mwadilifu, akaonekana na malaika. alihubiriwa kati ya mataifa, aliaminiwa popote ulimwenguni, akachukuliwa juu mbinguni katika utukufu.

Wolof

ci dëgg-dëgg ragal yàlla ëmb na mbóot yu xóot:ki wàcc, yor bindu nit,mu bir ne xelam jub na,te malaaka ya gis ko;xamlees na ko ci xeet yi,ñu gëm ko ci kaw suuf,te yàlla teeru ko ci ndamam.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,302,204 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK