Vous avez cherché: wanakwenda (Swahili - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Swahili

Wolof

Infos

Swahili

watu wote walikuwa wanakwenda hekaluni asubuhi na mapema, wapate kumsikiliza.

Wolof

te nit ñépp dañu daan teel a xëy ca kër yàlla ga, di ko déglu.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

walipokikaribia kile kijiji walikokuwa wanakwenda, yesu akafanya kana kwamba anaendelea na safari;

Wolof

bi ñuy jub dëkk, ba ñu jëmoon nag, yeesu def ni kuy jubal yoonam.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

walifurahi kumchukua yesu katika mashua; na mara mashua ikawasili nchi kavu walipokuwa wanakwenda.

Wolof

noonu ñu nangu koo dugal ca gaal ga, gaal ga daldi teer ca saa sa ca fa ñu bëggoon a wàcc.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

baadaye yesu aliwatokea wanafunzi wawili akiwa na sura nyingine. wanafunzi hao walikuwa wanakwenda shambani.

Wolof

gannaaw loolu yeesu feeñu ñaar ci ñoom ci jeneen jëmm, ñuy jaar ci yoon wi, jëm àll ba.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

watu walipokuwa wanakwenda zao, wengine walimletea yesu mtu mmoja aliyekuwa bubu kwa sababu alikuwa amepagawa na pepo.

Wolof

bi ñu fa jógee nag, amoon na ñeneen ñu ñëw fi moom, indil ko ku rab jàpp, mu luu.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

alipowaona akawaambia, "nendeni mkajionyeshe kwa makuhani." basi, ikawa walipokuwa wanakwenda, wakatakasika.

Wolof

naka la leen yeesu di gis, naan leen: «demleen won seen bopp saraxalekat ya.» bi ñuy dem, ñu daldi set.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

siku hiyohiyo, wawili kati ya wafuasi wake yesu wakawa wanakwenda katika kijiji kimoja kiitwacho emau, umbali wa kilomita kumi na moja kutoka yerusalemu.

Wolof

ca bés boobu ñaar ci taalibe yi di dem ci dëkku emayus, te mu sore yerusalem ci lu mat fukki kilomet.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

lakini watu wengi waliwaona wakienda, wakawatambua. hivyo wengi wakatoka katika kila mji, wakakimbilia huko yesu na wanafunzi wake walikokuwa wanakwenda, wakawatangulia kufika.

Wolof

bi ñuy dem nag, am ñu leen gis, xàmmi leen, ñu daldi jóge ci dëkk yépp, daw, jiitu leen fa.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

basi, kukawa na mtengano wa fikira kati yao. walipokuwa wanakwenda zao, paulo alisema jambo hili, "kweli ni sawa yale aliyoyanena roho mtakatifu kwa wazee wenu kwa njia ya nabii isaya

Wolof

gannaaw mënuñoo déggoo, ñu bëgg a tas. waaye bi ñu laata dem, pool teg ca wax jii: «xel mu sell mi wax na dëgg ak seeni maam, jaarale ko ci yonent yàlla esayi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Swahili

basi, hao wajumbe wa yohane walipokuwa wanakwenda zao, yesu alianza kuyaambia makundi ya watu habari za yohane: "mlikwenda kutazama nini kule jangwani? je, mlitaka kuona mwanzi unaotikiswa na upepo?

Wolof

bi nga xamee ne taalibe ya yaxya yónni woon ci yeesu dem nañu, yeesu daldi wax ak mbooloo ma ci mbirum yaxya ne leen: «lu ngeen seeti woon ca màndiŋ ma? xanaa barax buy jaayu ci ngelaw li?

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,740,188,720 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK