Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
zamani mungu aliruhusu kila taifa lifanye lilivyopenda.
démb mayoon na xeet yépp, ñu aw seen yoonu bopp.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
kama wangalikuwa wanaifikiria nchi walikotoka zamani, wangalipata nafasi ya kurudi huko.
bu ñu nammoon réew mi ñu jóge, kon dinañu am jotu dellu fa.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
basi, ile amri ya zamani ilifutwa kwa sababu ilikuwa hafifu na isiyofaa kitu.
noonu tebbi nañu yoon wu jëkk, wa néewoon doole te meññul dara
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
hapo zamani, mungu alisema na babu zetu mara nyingi kwa namna nyingi kwa njia ya manabii,
li jiitu tey yàlla waxoon na ak maam ya ci wàll yu bare ak ci tëralin yu wuute jaarale ko ca yonent ya.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
lakini mtu asiye na sifa hizo ni kipofu, hawezi kuona na amesahau kwamba alikwisha takaswa dhambi zake za zamani.
waaye ku ñàkk jiko yooyu, ay bëtam dañoo lëndëm ba gumba, te fàtte na, ni ko yàlla fóotale bàkkaari démb.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
mungu alikuwa ameazimia tangu zamani kutuleta kwake kama watoto wake kwa njia ya yesu kristo. ndivyo alivyopenda na kunuia.
séddoo na nu lu jiitu, def nu ay doomam jaarale ko ci yeesu kirist, ndaxte looloo doon yéene ju rafet, ji mu tëral ci coobareem.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
ni lazima yeye abaki huko mbinguni mpaka utakapofika wakati wa kurekebishwa vitu vyote, kama mungu alivyosema kwa njia ya manabii wake watakatifu wa tangu zamani.
asamaan war na koo yor, ba jamono ju ñuy defaraat lépp, di jamono ji yàlla waxoon jaarale ko ci gémmiñug yonentam yu sell yépp, li dale ci njàlbéenug àddina.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
bila shaka mlikwisha sikia jinsi nilivyokuwa ninaishi zamani kwa kuzingatia dini ya kiyahudi, na jinsi nilivyolitesa kanisa la mungu kupita kiasi na kutaka kuliharibu kabisa.
dégg ngeen ni ma doon jëfe, bi ma nekkee ci diiney yawut yi, di fitnaal bu metti mbooloom yàlla, di ko jéem a tas.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
ingawa mlikuwa watumwa wa dhambi zamani, sasa lakini--namshukuru mungu--mmetii kwa moyo wote yale maazimio na mafundisho mliyopokea.
waaye sant naa yàlla ci lii: yéen ñi doon jaami bàkkaar, bi ngeen déggee mboolem dëgg gi, nangu ngeen ko ak seen xol bépp.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
wala hakuna mtu ambaye hutamani kunywa divai mpya baada ya kunywa ya zamani, kwani husema: ile ya zamani ni nzuri zaidi."
ku naan biiñ bu màggat du bëgg bu bees bi, ndax day wax ne: “bu màggat bi baax na.”»
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Avertissement : un formatage HTML invisible est présent
zamani kidogo, kulitokea mtu mmoja jina lake theuda, akajisema kuwa mtu wa maana na watu karibu mia nne wakajiunga naye. lakini aliuawa, kisha wafuasi wake wote wakatawanyika na kikundi chake kikafa.
ndaxte bu yàggul tëdas jógoon na, mbubboo daraja, ba lu mat ñeenti téeméeri nit takktoo ak moom. tëdas moomu nag reyees na ko, te ñi ko toppoon ñépp tasaaroo, ba seen pexe nasax.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
mungu alimtoa yesu kusudi, kwa damu yake, awe njia ya kuwaondolea watu dhambi zao kwa imani yao kwake. alifanya hivyo ili apate kuonyesha kwamba yeye ni mwadilifu. hapo zamani mungu alikuwa mvumilivu bila kuzijali dhambi za watu;
wàcce na kirist, mu nekk sarax ngir yàlla baal nu sunuy bàkkaar, jaar ci deretam ji ñu tuur; te ngëm rekk moo nu ciy boole. noonu yàlla firndeel na ne ku jub la, doonte sax dafa muñaloon ñi jiitu jamonoy kirist, ba jéggal leen seeni bàkkaar.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
"ole wako korazini! ole wako bethsaida! maana, kama miujiza iliyofanyika kwako ingalifanyika kule tiro na sidoni, watu wake wangalikwisha vaa mavazi ya gunia na kujipaka majivu zamani, ili kuonyesha kwamba wametubu.
mu ne: «dingeen torox, yéen waa korasin ak waa betsayda, ndaxte kéemaan yi ma def ci yéen, bu ñu leen defoon ci dëkku tir walla ci dëkku sidon, kon réccu nañu bu yàgg, xëppoo dóom, sol saaku.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Avertissement : un formatage HTML invisible est présent