Vous avez cherché: zilizopita (Swahili - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Swahili

Wolof

Infos

Swahili

basi, sasa na tumsifu mungu! yeye anaweza kuwaimarisheni katika ile habari njema niliyohubiri juu ya ujumbe wa yesu kristo, na katika ile siri iliyofunuliwa na ambayo ilikuwa imefichika kwa karne nyinyi zilizopita.

Wolof

santleen yàlla, mi leen man a saxal bu wér ci dëggu xebaar bu baax, bi may waare ci mbirum yeesu kirist! nekkoon na kumpa gu làqu diirub ay ati at,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Swahili

kornelio akasema, "siku tatu zilizopita saa kama hii, saa tisa alasiri, nilikuwa nikisali chumbani mwangu. ghafla, mtu aliyekuwa amevaa mavazi yenye kun'gaa alisimama mbele yangu,

Wolof

ci kaw loolu korney tontu ne: «Ñetti fan a ngii may ñaan ci sama biir kër ci waxtu wii, maanaam tisbaar. ci saa si ku sol yére yuy melax taxaw ci sama kanam,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,747,235,612 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK