Vous avez cherché: çıldırmışsın (Turc - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Turc

Wolof

Infos

Turc

‹‹Çıldırmışsın sen!›› dediler ona. ama kız üsteleyince, ‹‹onun meleği olmalı›› dediler.

Wolof

Ñu ne ko: «xanaa dangaa dof.» waaye mu dëgër ci li mu wax. noonu ñu ne ko: «xanaa malaakaam la.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Turc

pavlus bu şekilde savunmasını sürdürürken festus yüksek sesle, ‹‹pavlus, çıldırmışsın sen! Çok okumak seni delirtiyor!›› dedi.

Wolof

bi muy làyyee nii, festus daldi ko gëdd ak baat bu kawe ne ko: «dangaa dof pool! xanaa sa njàng mu réy mi da laa xañ sago.»

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Turc

pavlus, ‹‹sayın festus›› dedi, ‹‹ben çıldırmış değilim. gerçek ve akla uygun sözler söylüyorum.

Wolof

waaye pool tontu ko: «festus mu tedd mi, dofuma; waaye lu dëggu laay wax te ànd ak sago.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,799,882,570 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK