Vous avez cherché: aldatmasın (Turc - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Turc

Wolof

Infos

Turc

kimse sizi kulağı okşayan sözlerle aldatmasın diye söylüyorum bunu.

Wolof

maa ngi wax lii, ngir kenn bañ leen a nax ci ay wax yu neex.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Turc

hiç kimse sizi boş sözlerle aldatmasın. bu şeylerden ötürü tanrının gazabı söz dinlemeyenlerin üzerine gelir.

Wolof

bu leen kenn nax ci ay waxi neen, ndaxte jëf yooyooy tax meru yàlla di wàcc ci kureelu ñi ko déggadil.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Turc

yavrularım, kimse sizi aldatmasın. mesih doğru olduğu gibi, doğru olanı yapan da doğru kişidir.

Wolof

samay doom, bu leen kenn nax! kuy def lu jub, ku jub nga, ni kirist jube moom ci boppam.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Turc

hiç kimse hiçbir şekilde sizi aldatmasın. Çünkü imandan dönüş başlamadıkça, mahvolacak olan o yasa tanımaz adam ortaya çıkmadıkça o gün gelmeyecektir.

Wolof

bu leen kenn nax ci benn fànn, ndaxte balaa booba, fàww xiiroo bu mag bi ak yàlla am, te nitu ñaawteef ki feeñ, moom aji alku ji.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Turc

kimse kendini aldatmasın. aranızdan biri bu çağın ölçülerine göre kendini bilge sanıyorsa, bilge olmak için ‹‹akılsız›› olsun!

Wolof

kon bu kenn nax boppam: su kenn ci yéen tegee boppam boroom xam-xam ci gis-gisu àddina sii, kooku na doon dof, ngir am xam-xam bu wóor.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Turc

bu nedenle, sevgili kardeşlerim, ilke tanımayan kişilerin aldatmasıyla sürüklenip kararlılığınızdan sapmamak için bunları önceden bilerek sakının.

Wolof

noonu yeen samay xarit, gannaaw xam ngeen loolu ba noppi, moytuleen ñi weddi fàbbi leen ci seen réer, ba yolomal seen wàkkirlu ci yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,780,177,474 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK