Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
toxal nañu ndamu yàlla aji sax ji, wuutal fa nataali nit ku dul sax, moom ak ay picc, ay rabi àll mbaa yuy raam.
und haben verwandelt die herrlichkeit des unvergänglichen gottes in ein bild gleich dem vergänglichen menschen und der vögel und der vierfüßigen und der kriechenden tiere.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
dëgg la; waaye seen ngëmadee tax ñu fàq leen, wuutal la fa ndax sa ngëm. bumu tax nag ngay bàkku, waaye nanga moytu.
ist wohl geredet! sie sind ausgebrochen um ihres unglaubens willen; du stehst aber durch den glauben. sei nicht stolz, sondern fürchte dich.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
noonu mu tegaat ca ne: «damaa wàcc ngir def sa coobare.» noonu toxal na jëfin wu jëkk wa, ngir wuutal fi weneen wu bees.
da sprach er: "siehe, ich komme, zu tun, gott, deinen willen." da hebt er das erste auf, daß er das andere einsetze.
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Avertissement : un formatage HTML invisible est présent