Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
bu nee jaleñ, bumu leen bett, ngeen di nelaw.
ድንገት መጥቶ ተኝታችሁ እንዳያገኛችሁ ስለዚህ ትጉ።
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
yeesu wax na loolu, ndaxte nee woon nañu, rab jàpp na ko.
ርኵስ መንፈስ አለበት ይሉ ነበርና።
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
yeesu wut cumbur, war ko; ndaxte mbind mi nee na:
አንቺ የጽዮን ልጅ አትፍሪ፤ እነሆ፥ ንጉሥሽ በአህያ ውርንጫ ላይ ተቀምጦ ይመጣል ተብሎ እንደ ተጻፈ፥ ኢየሱስ የአህያ ውርንጫ አግኝቶ በእርሱ ተቀመጠ።
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
day gis xar-kanamam, te su nee wërëñ, daldi fàtte meloom.
ራሱን አይቶ ይሄዳልና፥ ወዲያውም እንደ ምን እንደ ሆነ ይረሳል።
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
mbind mi nee na: ibraayma am na ñaari doom; ki jaam bi jur ak ki gor si jur.
አንዱ ከባሪያይቱ አንዱም ከጨዋይቱ የሆኑ ሁለት ልጆች ለአብርሃም እንደ ነበሩት ተጽፎአልና።
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
bi mu ko defee yeesu tere leen, ñu wax ko kenn, waaye lu mu leen ko gën a tere, ñu gën ko nee siiwale.
ለማንም አትንገሩ ብሎ አዘዛቸው እነርሱ ግን ባዘዛቸውም መጠን ይልቅ እጅግ አወሩት።
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
bi leen yeesu nee: «man la,» ñu daldi dellu gannaaw, ba daanu.
እንግዲህ። እኔ ነኝ ባላቸው ጊዜ ወደ ኋላ አፈግፍገው በምድር ወደቁ።
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
yeesu nee na: «maa ngi ñëw léegi, indaale pey gi, ngir delloo ku nekk lu mengoo ak lu mu def.
እነሆ፥ በቶሎ እመጣለሁ፥ ለእያንዳንዱም እንደ ሥራው መጠን እከፍል ዘንድ ዋጋዬ ከእኔ ጋር አለ።
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
buleen bëgge; deeleen doylu, ndaxte yàlla ci boppam nee na:«duma la wacc mukk,duma la wor mukk,»
አካሄዳችሁ ገንዘብን ያለ መውደድ ይሁን፥ ያላችሁም ይብቃችሁ፤ እርሱ ራሱ። አልለቅህም ከቶም አልተውህም ብሎአልና፤
Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :