Vous avez cherché: ñeneen (Wolof - Anglais)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Anglais

Infos

Wolof

musunoo sàkku ngërëmu nit, muy ci yéen, muy ci ñeneen.

Anglais

nor of men sought we glory, neither of you, nor yet of others, when we might have been burdensome, as the apostles of christ.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

kon nag bunu nelaw ni ñeneen ñi, waaye nanu xool te maandu.

Anglais

therefore let us not sleep, as do others; but let us watch and be sober.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yóbbaale nañu itam ñeneen, ñuy ñaari defkati lu bon, ngir rey leen.

Anglais

and there were also two other, malefactors, led with him to be put to death.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ci yoor-yoor mu génn, gis ñeneen ñu toog ca pénc ma te liggéeyuñu.

Anglais

and he went out about the third hour, and saw others standing idle in the marketplace,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

am ñeneen ñu fexe koo fiir, ba laaj ko kéemaan gu jóge ci asamaan tey firndeel yónnentam.

Anglais

and others, tempting him, sought of him a sign from heaven.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ngeen àtte ma walla ñeneen àtte ma, amaluma ko solo. te man sax duma àtte sama bopp.

Anglais

but with me it is a very small thing that i should be judged of you, or of man's judgment: yea, i judge not mine own self.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi ñu fa jógee nag, amoon na ñeneen ñu ñëw fi moom, indil ko ku rab jàpp, mu luu.

Anglais

as they went out, behold, they brought to him a dumb man possessed with a devil.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ci kaw loolu ñu daldi tifli ci xar-kanamam, dóor ko ay kurfeñ. Ñeneen talaata ko,

Anglais

then did they spit in his face, and buffeted him; and others smote him with the palms of their hands,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ba guddi giy xaaj nag, pool ak silas di ñaan ak di sant yàlla, te ñeneen ñi nekk ca kaso ba di leen déglu.

Anglais

and at midnight paul and silas prayed, and sang praises unto god: and the prisoners heard them.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yebal naa leen, ngeen góob tool bu ngeen beyul. Ñeneen a ko bey, te yéena ko jariñoo.»

Anglais

i sent you to reap that whereon ye bestowed no labour: other men laboured, and ye are entered into their labours.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu dinanu man a yégle xebaar bu baax bi ci bérab, yi leen féete gannaaw, te bañ a damu ci li ñeneen ñi def ci seen sas.

Anglais

to preach the gospel in the regions beyond you, and not to boast in another man's line of things made ready to our hand.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ngeen musal ñale, jële leen ci safara, te yërëm ñeneen ñi, waaye boole ci moytu, ba sib sax seen yére yi taq sobe.

Anglais

and others save with fear, pulling them out of the fire; hating even the garment spotted by the flesh.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu it saraxalekat yu mag yi ak xutbakat yi di ko ñaawal ci seen biir naan: «kii musal na ñeneen waaye mënul a musal boppam.

Anglais

likewise also the chief priests mocking said among themselves with the scribes, he saved others; himself he cannot save.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ay téeméeri nit cëru nañu ci yoonu gnome dalee ci juddam 1997 ba léegi, ñeneen ñi ci yeneen fànn, muy tekki, uti xibaar ak ci wóoral baaxaayam.unknownmonitor vendor

Anglais

hundreds of people have contributed code to gnome since it was started in 1997; many more have contributed in other important ways, including translations, documentation, and quality assurance.

Dernière mise à jour : 2014-08-15
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu yeesu laaj leen: «boroom tool bi nag, lu muy def? xanaa ñëw, rey beykat ya, dénk tool ba ñeneen.

Anglais

what shall therefore the lord of the vineyard do? he will come and destroy the husbandmen, and will give the vineyard unto others.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bu yàgg ngeen waroon a jàngal ñeneen ñi, waaye soxla ngeen ba tey ku leen di tette ci kàddug yàlla. léegi nag yéena ngi tollu fi ñu leen war a nàmpale, ndaxte àttanuleen ñam wu dëgër.

Anglais

for when for the time ye ought to be teachers, ye have need that one teach you again which be the first principles of the oracles of god; and are become such as have need of milk, and not of strong meat.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

sànn, jabaru ku ñuy wax kusa, mi doon wottu alalu erodd; ak susànn ak ñeneen jigéen. jigéen ñooñu ñoo doon joxe seen alal, ngir dimbali yeesu ak ay taalibeem.

Anglais

and joanna the wife of chuza herod's steward, and susanna, and many others, which ministered unto him of their substance.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

te fukki nit ak juróom-ñett ñooñu dee, bi taaxum kaw ma ca goxu silowe daanoo ci seen kaw, ndax dangeen a yaakaar ne, ñoo gën a nekk ay tooñkat ñeneen ñi dëkk yerusalem yépp?

Anglais

or those eighteen, upon whom the tower in siloam fell, and slew them, think ye that they were sinners above all men that dwelt in jerusalem?

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndegam ñeneen a am sañ-sañ boobu ci yéen, nun kon waxi-noppi. waaye nag jariñoowunu sañ-sañ boobu. danuy far muñ lépp, ngir bañ a indi ndog ci yoonu xebaar bu baax bu kirist bi.

Anglais

if others be partakers of this power over you, are not we rather? nevertheless we have not used this power; but suffer all things, lest we should hinder the gospel of christ.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,224,912 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK