Vous avez cherché: amuloo (Wolof - Anglais)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Anglais

Infos

Wolof

amuloo benn wàll mbaa cér ci lii, ndaxte sa xol laabul ci kanam yàlla.

Anglais

thou hast neither part nor lot in this matter: for thy heart is not right in the sight of god.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ku weddi doom ji, amuloo itam baay bi; ku seedeel doom ji, am nga it baay bi.

Anglais

whosoever denieth the son, the same hath not the father: (but) he that acknowledgeth the son hath the father also.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

képp ku bañ sa mbokk, reykat nga; te xam ngeen ne, ku rey nit amuloo dund gu dul jeex.

Anglais

whosoever hateth his brother is a murderer: and ye know that no murderer hath eternal life abiding in him.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

jigéen ja ne ko: «sang bi, teen bi xóot na te amuloo baag, kon fooy jële ndoxum dund?

Anglais

the woman saith unto him, sir, thou hast nothing to draw with, and the well is deep: from whence then hast thou that living water?

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ku gëm doom ji, am nga dund gu dul jeex; ku déggadil doom ji, amuloo dund, waaye merum yàllaa ngi la tiim.

Anglais

he that believeth on the son hath everlasting life: and he that believeth not the son shall not see life; but the wrath of god abideth on him.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

jigéen ja tontu ko ne: «awma jëkkër de.» yeesu ne ko: «wax nga dëgg ne, amuloo jëkkër,

Anglais

the woman answered and said, i have no husband. jesus said unto her, thou hast well said, i have no husband:

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

Ñu daldi ñëw ci yeesu ne ko: «kilifa gi, xam nanu ne li ngay wax te di ko jàngale lu jub la. amuloo parlàqu, waaye dangay xamle yoonu yàlla ci bu wóor.

Anglais

and they asked him, saying, master, we know that thou sayest and teachest rightly, neither acceptest thou the person of any, but teachest the way of god truly:

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

kon nag képp ku mu man a doon, yaw miy àtte sa moroom ak ñaaw njort, amuloo aw lay, ndaxte àtte sa moroom, daan sa bopp la; yaa ngi koy àtte ndax ay jëfam, fekk yaw itam noonu ngay jëfe.

Anglais

therefore thou art inexcusable, o man, whosoever thou art that judgest: for wherein thou judgest another, thou condemnest thyself; for thou that judgest doest the same things.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,850,313 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK