Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
ana
where is
Dernière mise à jour : 2020-02-22
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
ana kan ci yéen ci kaw njaaxleem moo man a yokk waxtu ci àppam?
which of you by taking thought can add one cubit unto his stature?
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
ana kan ci yéen ci kaw njaaxleem, moo man a yokk ab waxtu ci àppam?
and which of you with taking thought can add to his stature one cubit?
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
mbind mi dafa ne:«ana ku xam xalaatu boroom bi?ku ko doon digal?»
for who hath known the mind of the lord? or who hath been his counseller?
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
ana ku ci néew doole, te wàlluma ko? ana ku ci bàkkaar, te awma naqar wu tiis?
who is weak, and i am not weak? who is offended, and i burn not?
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
li ngeen di war a muñ, ab yar la. yàlla dafay jëf ak yéen ni ay doomam, ndaxte ana doom ju baayam dul yar?
if ye endure chastening, god dealeth with you as with sons; for what son is he whom the father chasteneth not?
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
ana ku neex xel ci yéen, ana kuy boroom xam-xam? na ko wone ciy jëfam ak dundam gu sell, te feeñal xelam ci jikkoom ju lewet.
who is a wise man and endued with knowledge among you? let him shew out of a good conversation his works with meekness of wisdom.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence: