Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
teye ba
i am coming
Dernière mise à jour : 2013-05-17
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
ba faf tëj yaxya kaso.
added yet this above all, that he shut up john in prison.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
ba ngeen may seytaane bunt.
neither give place to the devil.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
bi yelloo ndam ba fàww. amiin.
to whom be glory for ever and ever. amen.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
waaye ba tey seeni wax ànduñu.
but neither so did their witness agree together.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
ba noppi toog fa, di ko wottu.
and sitting down they watched him there;
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
noonu waa dëkk ba jóg, jëm ca yeesu.
then they went out of the city, and came unto him.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
ba noppi ñu daldi dem wuti beneen dëkk.
for the son of man is not come to destroy men's lives, but to save them. and they went to another village.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
Ñépp a bàkkaar, ba joteetuñu ndamu yàlla.
for all have sinned, and come short of the glory of god;
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
ba mujj naaféq taxaw, seede ci moom naan:
and there arose certain, and bare false witness against him, saying,
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
ku nekk ca tool ba, bul ñibbi ngir fab sa mbubb.
neither let him which is in the field return back to take his clothes.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
loolu moo tax ñu wooye tool booba ba tey toolu deret.
wherefore that field was called, the field of blood, unto this day.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
Ñu daldi liyaar baayam, ngir xam nan la bëgg ñu tudde xale ba.
and they made signs to his father, how he would have him called.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
bi ñu agsee, ñu fekk ñu béraŋ doj, wa uboon bàmmeel ba.
and they found the stone rolled away from the sepulchre.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
noonu saraxalekat bu mag ba ne ko: «ndax loolu dëgg la?»
then said the high priest, are these things so?
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
ba ñu gisee biddiiw ba nag, ñu am mbég mu réy-a-réy.
when they saw the star, they rejoiced with exceeding great joy.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
nekkatu fi; dekki na. fàttalikuleen la mu leen waxoon, ba mu nekkee galile.
he is not here, but is risen: remember how he spake unto you when he was yet in galilee,
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence:
waaye ñuy yuuxu naan: «daaj ko ci bant! daaj ko ci bant, ba mu dee!»
but they cried, saying, crucify him, crucify him.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
Référence: