Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
«dégluleen, dafa amoon beykat bu demoon jiyi.
hearken; behold, there went out a sower to sow:
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
noonu it beykat bi sonn mooy jëkk a ñam toolam.
the husbandman that laboureth must be first partaker of the fruits.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
«man maay garab gu wóor gi, te sama baay mooy beykat bi.
i am the true vine, and my father is the husbandman.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
«lii la léebu beykat bi di tekki. kàddug yàlla mooy jiwu wi.
now the parable is this: the seed is the word of god.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
boroom kër gi nag yónniwaat yeneen surga yu ëpp yu jëkk ya, beykat yi def leen noonu ñoom itam.
again, he sent other servants more than the first: and they did unto them likewise.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
noonu yeesu dégtal leen lu bare ciy léeb ne leen: «dafa amoon beykat bu demoon jiyi.
and he spake many things unto them in parables, saying, behold, a sower went forth to sow;
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
noonu yeesu laaj leen: «bu boroom tool bi ñëwee nag, na muy def beykat yi?»
when the lord therefore of the vineyard cometh, what will he do unto those husbandmen?
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
«bi nga xamee ne bëgg nañoo witt réseñ yi, mu yónni ay surgaam ci beykat yi, ngir jot wàllam ci meññeef mi.
and when the time of the fruit drew near, he sent his servants to the husbandmen, that they might receive the fruits of it.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
waaye beykat yi daldi ne ci seen biir: “kii moo war a donn tool bi; nan ko rey, moom ndono li.”
but those husbandmen said among themselves, this is the heir; come, let us kill him, and the inheritance shall be ours.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
noonu yeesu daldi wax nit ña léeb wii: «amoon na nit ku jëmbët toolu réseñ, batale ko ay beykat, dem tukki tukki bu yàgg.
then began he to speak to the people this parable; a certain man planted a vineyard, and let it forth to husbandmen, and went into a far country for a long time.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
yéen samay bokk, muñleen, ba boroom bi dellusi ci ndamam. seetleen ci beykat bi, ni muy xaare njariñ ci meññeefu suuf, tey muñ, céebo ba bët wàcc.
be patient therefore, brethren, unto the coming of the lord. behold, the husbandman waiteth for the precious fruit of the earth, and hath long patience for it, until he receive the early and latter rain.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
waaye bi beykat yi gisee doom ji, ñu ne ci seen bopp: “kii moo war a donn tool bi; nan ko rey, moom ndonoom.”
but when the husbandmen saw the son, they said among themselves, this is the heir; come, let us kill him, and let us seize on his inheritance.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
noonu yeesu daldi leen wax ciy léeb. mu ne leen: «amoon na fi nit ku jëmbët toolu réseñ. mu ñag tool bi, gas pax ngir nal ci réseñ yi, tabax wottukaay, ba noppi batale ko ay beykat, daldi tukki.
and he began to speak unto them by parables. a certain man planted a vineyard, and set an hedge about it, and digged a place for the winefat, and built a tower, and let it out to husbandmen, and went into a far country.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :