Vous avez cherché: bor (Wolof - Anglais)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Anglais

Infos

Wolof

soo ko naree topp genn tooñ mbaa benn bor, topp ma ko.

Anglais

if he hath wronged thee, or oweth thee ought, put that on mine account;

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu sangam yërëm ko, bàyyi ko, baal ko bor ba.

Anglais

then the lord of that servant was moved with compassion, and loosed him, and forgave him the debt.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye kenn ci ñoom mënu koo fey. noonu mu baal leen bor ya. ci ñaar ñooñu nag kan moo ko ciy gën a bëgg?»

Anglais

and when they had nothing to pay, he frankly forgave them both. tell me therefore, which of them will love him most?

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye jaraaf ja amul lu mu feye. kon nag sangam santaane, ñu jaay ko moom ak jabaram ak ay doomam ak lépp lu mu am, ngir fey bor ba.

Anglais

but forasmuch as he had not to pay, his lord commanded him to be sold, and his wife, and children, and all that he had, and payment to be made.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndaxte tuur nañu deretu sa gaa ñiak ju yonent yi,yaw it fey nga leen seen bor,jox leen deret, ñu naan.»

Anglais

for they have shed the blood of saints and prophets, and thou hast given them blood to drink; for they are worthy.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yeesu ne ko: «da fee amoon ñaari nit ñu ameel bor benn leblekat. kenn kaa ngi ko ameel téeméeri junni ci xaalis, ki ci des fukki junni.

Anglais

there was a certain creditor which had two debtors: the one owed five hundred pence, and the other fifty.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,778,005,313 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK