Vous avez cherché: déggal (Wolof - Anglais)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Anglais

Infos

Wolof

te it na jigéen jàng cig noppi, ànd ak déggal gu mat.

Anglais

let the woman learn in silence with all subjection.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu ku laab fas, ngir mu déggal la, noot nga jëmmam jépp.

Anglais

behold, we put bits in the horses' mouths, that they may obey us; and we turn about their whole body.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndaxte ñépp ñiy déggal xelu yàlla mi, ay doomi yàlla lañu.

Anglais

for as many as are led by the spirit of god, they are the sons of god.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye njiit la sobental waxi pool, déggal dawalkat ba ak boroom gaal ga.

Anglais

nevertheless the centurion believed the master and the owner of the ship, more than those things which were spoken by paul.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

seede nanu loolu, nun ak xel mu sell, mi yàlla may ñi koy déggal.»

Anglais

and we are his witnesses of these things; and so is also the holy ghost, whom god hath given to them that obey him.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

na seen nangub boroom bi tax, ngeen déggal képp kuy kilifa, muy buur ba gën a kawe,

Anglais

submit yourselves to every ordinance of man for the lord's sake: whether it be to the king, as supreme;

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye piyeer ak ndaw ya tontu leen ne: «déggal yàlla moo gën déggal nit.

Anglais

then peter and the other apostles answered and said, we ought to obey god rather than men.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ni ngeen jógtee woon de baax na! waaw ku leen dog, ba ngeen bañ a déggal dëgg?

Anglais

ye did run well; who did hinder you that ye should not obey the truth?

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

kon fokk ngeen déggal ko, waxuma sax ndax sañ-sañam boobu, waaye it ngir seen xel dal.

Anglais

wherefore ye must needs be subject, not only for wrath, but also for conscience sake.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

safara su yànj wër ko, mu feeñ ngir mbugal ñi xamul yàlla te bañ a déggal xebaar bu baaxu sunu boroom yeesu.

Anglais

in flaming fire taking vengeance on them that know not god, and that obey not the gospel of our lord jesus christ:

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

moona li leen rab yi déggal, bumu tax ngeen bég, waaye bégleen ndax li ñu bind seen tur ci asamaan.»

Anglais

notwithstanding in this rejoice not, that the spirits are subject unto you; but rather rejoice, because your names are written in heaven.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ba tax na léegi njub, gi yoonu musaa di digle, am na ci nun, ñiy déggal xelu yàlla mi te bañ a topp sunu nafsu.

Anglais

that the righteousness of the law might be fulfilled in us, who walk not after the flesh, but after the spirit.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

gannaaw gaayi yàlla yu koy déggal ngeen, buleen toppati bëgg-bëgg, yi ngeen toppoon, bi ngeen xamagul yàlla.

Anglais

as obedient children, not fashioning yourselves according to the former lusts in your ignorance:

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

Ñu daldi ragal lool, naan ci seen biir: «kii moo di kan, ba ngelaw li ak dex gi sax di ko déggal?»

Anglais

and they feared exceedingly, and said one to another, what manner of man is this, that even the wind and the sea obey him?

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

man nag bokk yi, mënuma woon a wax ak yéen ni ay nit ñuy déggal xelum yàlla, waaye waroon naa wax ak yéen ni ñuy topp seen nafsu, mel ni ay liir ci seen dund ci kirist.

Anglais

and i, brethren, could not speak unto you as unto spiritual, but as unto carnal, even as unto babes in christ.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ngëm moo tax ba ibraayma déggal yàlla. bi ko yàlla wooyee, mu dem toxu ci menn réew, ma mu waroon a jote ca yàlla. noonu la gàddaaye dëkkam te xamul woon fan la jëm.

Anglais

by faith abraham, when he was called to go out into a place which he should after receive for an inheritance, obeyed; and he went out, not knowing whither he went.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ci li mu leen xam bu jiitu, te sédde leen boppam ci jëfu xel mu sell mi, ngir ngeen déggal ko, te seen xol laab ndax deretu yeesu kirist. na leen yàlla dollil yiw ak jàmm.

Anglais

elect according to the foreknowledge of god the father, through sanctification of the spirit, unto obedience and sprinkling of the blood of jesus christ: grace unto you, and peace, be multiplied.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu itam yéen ndaw ñi, nangeen déggal mag ñi. te yéen ñépp, solooleen woyof ci seen biir, ndaxte:«yàlla day dàq ñi réy,di yiwal ñi woyof.»

Anglais

likewise, ye younger, submit yourselves unto the elder. yea, all of you be subject one to another, and be clothed with humility: for god resisteth the proud, and giveth grace to the humble.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yeesu ne taalibe yi: «ana seen ngëm?» Ñu daldi tiit te waaru, naan ci seen biir: «kii moo di kan? mi ngi jox ndigal ngelaw li ak ndox mi, ñu koy déggal.»

Anglais

and he said unto them, where is your faith? and they being afraid wondered, saying one to another, what manner of man is this! for he commandeth even the winds and water, and they obey him.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,773,675,170 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK