Vous avez cherché: digal (Wolof - Anglais)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Anglais

Infos

Wolof

digal leen yëf yooyu nag ci sa njàngale.

Anglais

these things command and teach.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

mbind mi dafa ne:«ana ku xam xalaatu boroom bi?ku ko doon digal?»

Anglais

for who hath known the mind of the lord? or who hath been his counseller?

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

nu ngi lay digal nag, nga def nii: am na ci nun ñeenti góor yu dige ak yàlla.

Anglais

do therefore this that we say to thee: we have four men which have a vow on them;

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

moo nu digal, nu dëddu weddi ak bëgg-bëggi jamono, tey dund ci àddina cig maandu, njub ak ragal yàlla,

Anglais

teaching us that, denying ungodliness and worldly lusts, we should live soberly, righteously, and godly, in this present world;

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

te léegi, ci jamono ji ko soob, feeñal na xebaaram boobu ci waaraate, bi ma yàlla sunu musalkat dénk te digal ma, ma xamle ko.

Anglais

but hath in due times manifested his word through preaching, which is committed unto me according to the commandment of god our saviour;

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

mu digal leen nii: «bu ngeen di dem, buleen yóbbaale dara; du mburu mbaa mbuus mbaa xaalis ci seeni maxtume, waaye yemleen ci aw yet rekk.

Anglais

and commanded them that they should take nothing for their journey, save a staff only; no scrip, no bread, no money in their purse:

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,793,368,970 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK