Vous avez cherché: fakkastalu (Wolof - Anglais)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Anglais

Infos

Wolof

dinañu la leewu ci seeni loxo,ngir nga bañ a fakkastalu ciw doj.”»

Anglais

and in their hands they shall bear thee up, lest at any time thou dash thy foot against a stone.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yeesu ne leen: «xanaa du bëccëg fukki waxtook ñaar la? kuy dox bëccëg, du fakkastalu, ndaxte day gis leeru àddina si.

Anglais

jesus answered, are there not twelve hours in the day? if any man walk in the day, he stumbleth not, because he seeth the light of this world.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

te it:«doj la wuy fél nit,di xeer wu koy fakkastal.» dañu cee fakkastalu, ndaxte gëmuñu kàddug yàlla, te loolu la yàlla dogal ci ñoom.

Anglais

and a stone of stumbling, and a rock of offence, even to them which stumble at the word, being disobedient: whereunto also they were appointed.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

mu ne ko: «boo dee doomu yàlla, tëbal ci suuf, ndaxte mbind mi nee na:“dina jox ay malaakaam ndigal ci sa mbir,ñu leewu la ci seeni loxo,ngir nga bañ a fakkastalu ciw doj.”»

Anglais

and saith unto him, if thou be the son of god, cast thyself down: for it is written, he shall give his angels charge concerning thee: and in their hands they shall bear thee up, lest at any time thou dash thy foot against a stone.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,772,916,365 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK