Vous avez cherché: li ma nekk (Wolof - Anglais)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Anglais

Infos

Wolof

li ma leen wax, ñépp laa ko wax: “xool-leen!”»

Anglais

and what i say unto you i say unto all, watch.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

maa ngi wax ak yéen ñi am xel. kon seetleen li ma leen wax.

Anglais

i speak as to wise men; judge ye what i say.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

li ma ne: “fàww ngeen judduwaat,” bumu la jaaxal.

Anglais

marvel not that i said unto thee, ye must be born again.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

«kon nag buur agaripa, woruma li ma yàlla yen ci peeñu.

Anglais

whereupon, o king agrippa, i was not disobedient unto the heavenly vision:

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

«li ma leen war a wax bare na, waaye dungeen ko man a dékku.

Anglais

i have yet many things to say unto you, but ye cannot bear them now.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

wone naa sa ndam ci àddina, ndax li ma matal liggéey, bi nga ma santoon.

Anglais

i have glorified thee on the earth: i have finished the work which thou gavest me to do.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

te ngeen jàngal leen, ñuy sàmm lépp li ma leen sant. te maa ngi ànd ak yéen bés bu nekk, ba kera àddina di tukki.»

Anglais

teaching them to observe all things whatsoever i have commanded you: and, lo, i am with you alway, even unto the end of the world. amen.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

maanaam ma nekk ci seen biir, te nu dimbaleente ci sunu ngëm, ndax man itam ma gën a am doole.

Anglais

that is, that i may be comforted together with you by the mutual faith both of you and me.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu bind naa la, ndax wóor na ma ne, dinga ma déggal, ba weesu sax li ma la sant.

Anglais

having confidence in thy obedience i wrote unto thee, knowing that thou wilt also do more than i say.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

lu tax nga may laaj? laajal ñi doon déglu li ma leen wax. Ñoom xam nañu li ma doon wax.»

Anglais

why askest thou me? ask them which heard me, what i have said unto them: behold, they know what i said.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi jigéen ja nee waa dëkk ba: «wax na ma li ma def lépp,» ñu bare gëm nañu yeesu.

Anglais

and many of the samaritans of that city believed on him for the saying of the woman, which testified, he told me all that ever i did.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yeesu gis ne taalibeem yaa ngi ñurumtoo loolu, mu ne leen: «ndax li ma wax da leen a jaaxal?

Anglais

when jesus knew in himself that his disciples murmured at it, he said unto them, doth this offend you?

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

di daw yen muj ga, ngir jot li ma yàlla tax a woo, di cér bi ma yàlla wooye te dencal ma ko ci asamaan ci darajay kirist yeesu.

Anglais

i press toward the mark for the prize of the high calling of god in christ jesus.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

léegi nag gannaaw gëmuloo li ma wax, dinga luu te dootuloo man a wax, ba kera sama wax di am, bu jamonoom jotee.»

Anglais

and, behold, thou shalt be dumb, and not able to speak, until the day that these things shall be performed, because thou believest not my words, which shall be fulfilled in their season.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

man pool, jaamub kirist yeesu, maa leen di bind bataaxal bii. yàlla woo na ma, ma nekk ndawam, sas ma liggéeyu xamle xebaaram bu baax bi.

Anglais

paul, a servant of jesus christ, called to be an apostle, separated unto the gospel of god,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

li ma leen di wax, mooy lii: doom ji war a donni baayam, fi ak mu ngi cig ndaw, ak lu ko alal jiy lew lépp, du wuute dara ak jaam.

Anglais

now i say, that the heir, as long as he is a child, differeth nothing from a servant, though he be lord of all;

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi mu leen raxasalee seeni tànk ba noppi, yeesu dafa solaat mbubbam, dellu toogaat ne leen: «ndax xam ngeen li ma leen defal?

Anglais

so after he had washed their feet, and had taken his garments, and was set down again, he said unto them, know ye what i have done to you?

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

samay soppe, sama nekk ak yéen dootul yàgg. dingeen may seet, waaye maa ngi leen di wax léegi li ma waxoon yawut ya: fa ma jëm, dungeen fa man a dem.

Anglais

little children, yet a little while i am with you. ye shall seek me: and as i said unto the jews, whither i go, ye cannot come; so now i say to you.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

li ma bëgg a wax nag, ci kanamu kirist laa koy waxe; dëgg la, du aw fen. sama xel, mi xel mu sell miy leeral, seedeel na ma ne, dëgg laay wax.

Anglais

i say the truth in christ, i lie not, my conscience also bearing me witness in the holy ghost,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

looloo tax farisen ya di laajaat waa ja fi mu jaar bay gis léegi. mu ne leen: «dafa tay ban ci samay bët, ma sëlmuji, ba fi ma nekk maa ngi gis.»

Anglais

then again the pharisees also asked him how he had received his sight. he said unto them, he put clay upon mine eyes, and i washed, and do see.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Certaines traductions humaines peu pertinentes ont été masquées.
Affichez les résultats peu pertinents.

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,899,095 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK