Vous avez cherché: mënunu (Wolof - Anglais)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Anglais

Infos

Wolof

ndaxte manalunu dara dëggu yàlla gi; mënunu lu dul taxawal ko.

Anglais

for we can do nothing against the truth, but for the truth.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi yeesu duggee ci kër gi, taalibe yi laaj ko ci pegg: «lu tax mënunu ko woon a dàq?»

Anglais

and when he was come into the house, his disciples asked him privately, why could not we cast him out?

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi loolu amee taalibe ya ñëw ci yeesu, laaj ko ci pegg: «lu tax nun mënunu woon a dàq rab wi?»

Anglais

then came the disciples to jesus apart, and said, why could not we cast him out?

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ne: «lu nuy def ak ñii? ndaxte def nañu kéemaan gu siiw; loolu leer na ñi dëkk yerusalem ñépp, te mënunu koo weddi.

Anglais

saying, what shall we do to these men? for that indeed a notable miracle hath been done by them is manifest to all them that dwell in jerusalem; and we cannot deny it.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

kon nag bokk yi, yéen ñi boroom bi bëgg, mënunu lu dul sax ci sant yàlla ci li mu leen tànn ca njàlbéen ga, ngir musal leen, mu sédde leen boppam jaarale ko ci jëfu xel mu sell mi ak seen gëm dëgg gi.

Anglais

but we are bound to give thanks alway to god for you, brethren beloved of the lord, because god hath from the beginning chosen you to salvation through sanctification of the spirit and belief of the truth:

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bokk yi, mënunu lu dul sax ci sant yàlla ndax yéen. loolu jaadu na, ndax seen ngëm di gën a sax, te mbëggeel gi ngeen am ci seen biir, ku nekk ci sa moroom, di yokku lu bare.

Anglais

we are bound to thank god always for you, brethren, as it is meet, because that your faith groweth exceedingly, and the charity of every one of you all toward each other aboundeth;

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,793,788,898 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK