Vous avez cherché: mburu (Wolof - Anglais)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Anglais

Infos

Wolof

mburu

Anglais

unleavened

Dernière mise à jour : 2012-12-10
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Wikipedia

Wolof

yeesu jegeñsi, jël mburu mi, jox leen, jox leen it jën.

Anglais

jesus then cometh, and taketh bread, and giveth them, and fish likewise.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Wikipedia

Wolof

kan ci yéen, bu la sa doom ñaanee mburu, nga jox ko doj?

Anglais

or what man is there of you, whom if his son ask bread, will he give him a stone?

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Wikipedia

Wolof

taalibe yi nag daldi werante naan: «nun de indaalewunu mburu.»

Anglais

and they reasoned among themselves, saying, it is because we have no bread.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Wikipedia

Wolof

gannaaw loolu taalibe yi jàllaat dex gi, fekk fàtte nañoo yóbbaale mburu.

Anglais

and when his disciples were come to the other side, they had forgotten to take bread.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Wikipedia

Wolof

yudaa nag jël dogu mburu ma, daldi génn ca saa sa. booba guddi woon na.

Anglais

he then having received the sop went immediately out: and it was night.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Wikipedia

Wolof

te it ñu dajale la desoon ca dammiti mburu ak jën ya, mu nekk fukki pañe ak ñaar yu fees.

Anglais

and they took up twelve baskets full of the fragments, and of the fishes.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Wikipedia

Wolof

Ñu dajale ko, daldi feesal fukki pañe ak ñaar ak desiti juróomi mburu, yi ñu doon lekk.

Anglais

therefore they gathered them together, and filled twelve baskets with the fragments of the five barley loaves, which remained over and above unto them that had eaten.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Wikipedia

Wolof

bi mu waxee loolu, mu fab mburu, sant yàlla ci kanamu ñépp, damm ko, daldi ko lekk.

Anglais

and when he had thus spoken, he took bread, and gave thanks to god in presence of them all: and when he had broken it, he began to eat.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Wikipedia

Wolof

Ñaari taalibe ya ñoom it daldi leen nettali la xewoon ca yoon wa ak ni ñu xàmmee yeesu, bi mu dammee mburu ma.

Anglais

and they told what things were done in the way, and how he was known of them in breaking of bread.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Wikipedia

Wolof

bi ko taalibe yi déggee, ñu daldi werante ci seen biir naan: «nun de indaalewunu mburu.»

Anglais

and they reasoned among themselves, saying, it is because we have taken no bread.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Wikipedia

Wolof

noonu taalibeem ya laaj ko: «waaye fu nuy jële ci àll bi mburu mu doy ngir mbooloo mu tollu nii?»

Anglais

and his disciples say unto him, whence should we have so much bread in the wilderness, as to fill so great a multitude?

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Wikipedia

Wolof

te bés bu nekk ñu saxoo teew ak benn xalaat ca kër yàlla ga, tey damm mburu ca kër ya; ñuy lekk seen ñam ak xol bu laab tey bég,

Anglais

and they, continuing daily with one accord in the temple, and breaking bread from house to house, did eat their meat with gladness and singleness of heart,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Wikipedia

Wolof

noonu fiirkat bi ñëw ci moom ne ko: «boo dee doomu yàlla, santal doj yii, ñu nekk mburu.»

Anglais

and when the tempter came to him, he said, if thou be the son of god, command that these stones be made bread.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Wikipedia

Wolof

waaye yeesu yég loolu ne leen: «yéen ñi néew ngëm, lu tax ngeen di werante ci seen biir, ndaxte indaalewuleen mburu?

Anglais

which when jesus perceived, he said unto them, o ye of little faith, why reason ye among yourselves, because ye have brought no bread?

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Wikipedia

Wolof

bi yeesu xoolee, gis mbooloo mu réy di ñëw ci moom, mu ne filib: «fu nuy jële mburu, mu nu leen man a dundale?»

Anglais

when jesus then lifted up his eyes, and saw a great company come unto him, he saith unto philip, whence shall we buy bread, that these may eat?

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Wikipedia

Wolof

kaas bu yiw, bi tax nuy gërëm yàlla, ndax du wone sunu booloo ak deretu kirist? mburu mi nuy damm, xanaa du dafay wone sunu booloo ak yaramu kirist?

Anglais

the cup of blessing which we bless, is it not the communion of the blood of christ? the bread which we break, is it not the communion of the body of christ?

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Wikipedia

Wolof

bés bu jëkk ca màggal, ga ñuy wax mburu ya amul lawiir, taalibe yi ñëw ci yeesu ne ko: «foo bëggoon nu defaral la reeru màggalu jéggi ba?»

Anglais

now the first day of the feast of unleavened bread the disciples came to jesus, saying unto him, where wilt thou that we prepare for thee to eat the passover?

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Wikipedia

Wolof

mu digal leen nii: «bu ngeen di dem, buleen yóbbaale dara; du mburu mbaa mbuus mbaa xaalis ci seeni maxtume, waaye yemleen ci aw yet rekk.

Anglais

and commanded them that they should take nothing for their journey, save a staff only; no scrip, no bread, no money in their purse:

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Wikipedia

Wolof

waaye yeesu tontu ko ne: «mbind mi nee na: “nit du dunde mburu rekk, waaye itam gépp kàddu gu génne ci gémmiñug yàlla.”»

Anglais

but he answered and said, it is written, man shall not live by bread alone, but by every word that proceedeth out of the mouth of god.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Wikipedia

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,800,263,246 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK