Vous avez cherché: name na la (Wolof - Anglais)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Anglais

Infos

Wolof

képp ku déggalul yonent boobu, dees na la far ci xeet wi.”

Anglais

and it shall come to pass, that every soul, which will not hear that prophet, shall be destroyed from among the people.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

kuy yékkatiku, dees na la suufeel; kuy suufeelu, ñu yékkati la.

Anglais

and whosoever shall exalt himself shall be abased; and he that shall humble himself shall be exalted.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu yeesu ne ko: «jógal dem; sa ngëm faj na la.»

Anglais

and he said unto him, arise, go thy way: thy faith hath made thee whole.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

képp ku ñu bindul sa tur ci téereb dund bi, dees na la sànni ci déegu safara si.

Anglais

and whosoever was not found written in the book of life was cast into the lake of fire.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yeesu ne ko: «soxna si, sa ngëm faj na la. demal ci jàmm.»

Anglais

and he said unto her, daughter, be of good comfort: thy faith hath made thee whole; go in peace.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndaxte képp kuy yékkatiku, dees na la suufeel, te kuy suufeelu, dinañu la yékkati.»

Anglais

for whosoever exalteth himself shall be abased; and he that humbleth himself shall be exalted.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

te yaw dëkku kapernawum, ndax dees na la yékkati bu kawe? déedéet, dees na la daane bu suufe.

Anglais

and thou, capernaum, which art exalted to heaven, shalt be thrust down to hell.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu dootuloo jaam, doom nga. te ndegam doom nga, yàlla jagleel na la cér ci xéewal, yi mu dencal ay doomam.

Anglais

wherefore thou art no more a servant, but a son; and if a son, then an heir of god through christ.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ku dékku nattu, ku barkeel nga, ndax boo ci génnee ak ndam, dees na la jagleel kaalag dund, gi yàlla dig ñi ko bëgg.

Anglais

blessed is the man that endureth temptation: for when he is tried, he shall receive the crown of life, which the lord hath promised to them that love him.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

mu ne ma: “sunu yàllay maam tànn na la, ba may la, nga xam coobareem te gis aji jub ji te nga dégg ay waxam.

Anglais

and he said, the god of our fathers hath chosen thee, that thou shouldest know his will, and see that just one, and shouldest hear the voice of his mouth.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

maa ngi lay bind, tit, yaw sama doomu diine ju wér ci ngëm, gi nu bokk nun ñépp. na la yàlla baay bi ak kirist yeesu sunu musalkat may yiw ak jàmm.

Anglais

to titus, mine own son after the common faith: grace, mercy, and peace, from god the father and the lord jesus christ our saviour.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yeesu tontu ko: «barkeel ñeel na la, simoŋ doomu yunus, ndaxte du nit moo la xamal lii, waaye sama baay bi nekk ci kaw.

Anglais

and jesus answered and said unto him, blessed art thou, simon barjona: for flesh and blood hath not revealed it unto thee, but my father which is in heaven.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu yeesu ne ko: «demal ci jàmm. sa ngëm faj na la.» ci saa si gumba gi gis, daldi topp yeesu ci yoon wi.

Anglais

and jesus said unto him, go thy way; thy faith hath made thee whole. and immediately he received his sight, and followed jesus in the way.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

Ñu daldi woy woy wu bees naan:«yeyoo ngaa jël téere bite dindi tayu yi,ndaxte reyees na la,te jotal nga yàlla ak sa deretay nit ñu bokk ci bépp giir,kàllaama, réew ak xeet.

Anglais

and they sung a new song, saying, thou art worthy to take the book, and to open the seals thereof: for thou wast slain, and hast redeemed us to god by thy blood out of every kindred, and tongue, and people, and nation;

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ku tebbi nag ba gën a tuuti ci ndigal yii, te ngay jàngal nit ñi noonu, dees na la tudde ki gën a tuuti ci nguuru yàlla aji kawe ji. waaye ku leen di sàmm, di leen digle, dees na la tudde ku mag ci nguuru yàlla aji kawe ji.

Anglais

whosoever therefore shall break one of these least commandments, and shall teach men so, he shall be called the least in the kingdom of heaven: but whosoever shall do and teach them, the same shall be called great in the kingdom of heaven.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Certaines traductions humaines peu pertinentes ont été masquées.
Affichez les résultats peu pertinents.

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,770,638,997 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK