Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
noonu ñu bare gëm ko.
and many believed on him there.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
noonu pool génn ci seen biir.
so paul departed from among them.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
noonu maryaama daldi ne:
and mary said, my soul doth magnify the lord,
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
noonu taalibe ya dëpp, ñibbi.
then the disciples went away again unto their own home.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
noonu turam siiw ca diiwaan bépp.
and the fame of him went out into every place of the country round about.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
noonu mbég mu réy tàbbi ca dëkk ba.
and there was great joy in that city.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
noonu waa dëkk ba jóg, jëm ca yeesu.
then they went out of the city, and came unto him.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
noonu ñu toog ak taalibe ya diir bu yàgg.
and there they abode long time with the disciples.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
beneen yoon yeesu dem, di ñaane noonu,
and again he went away, and prayed, and spake the same words.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
noonu ñu daldi fàttaliku kàdduy yeesu ya.
and they remembered his words,
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
noonu ñu dugg cig gaal, dem ca bérab bu wéet.
and they departed into a desert place by ship privately.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
noonu it beykat bi sonn mooy jëkk a ñam toolam.
the husbandman that laboureth must be first partaker of the fruits.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
noonu ñi mujj ñooy jiituji, ñi jiitu ñooy mujj.»
so the last shall be first, and the first last: for many be called, but few chosen.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
noonu doomu nit ki mooy boroom bésu noflaay bi.»
therefore the son of man is lord also of the sabbath.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
noonu yeesu daldi leen dénk, tere leen ñu wax ko kenn,
and he straitly charged them, and commanded them to tell no man that thing;
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
noonu ndaw yi ak njiit yi dajaloo, ngir seet mbir moomu.
and the apostles and elders came together for to consider of this matter.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
noonu yanqóoba dem misra, faatu fa, moom ak sunuy maam.
so jacob went down into egypt, and died, he, and our fathers,
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
noonu mu dem di waare ca jàngu ya ca réewu yawut ya.
and he preached in the synagogues of galilee.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
noonu saraxalekat bu mag ba ne ko: «ndax loolu dëgg la?»
then said the high priest, are these things so?
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
noonu yeesu ne leen: «waaye yéen, ku ngeen may teg?»
he saith unto them, but whom say ye that i am?
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :