Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
noonu ñu lekk ba suur, daldi sànni pepp ma ca géej ga, ngir woyofal gaal ga.
and when they had eaten enough, they lightened the ship, and cast out the wheat into the sea.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
bi muy saaw toolam nag, lenn ci pepp mi wadd ci kaw yoon wi, picc yi daldi ñëw, lekk ko lépp.
and it came to pass, as he sowed, some fell by the way side, and the fowls of the air came and devoured it up.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
kiy góob tool yi mu ngi jot xaat peyam; day dajale nit ñi ngir dund gu dul jeex, ni ñuy dajalee pepp. kon boog kiy ji dina bégandoo ak kiy góob.
and he that reapeth receiveth wages, and gathereth fruit unto life eternal: that both he that soweth and he that reapeth may rejoice together.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
ci dëgg-dëgg maa ngi leen koy wax, fi ak peppu dugub ji wadd ci suuf jaarul ci dee, du man a weesu li mu doon: pepp doŋŋ. waaye bu deeyee, dina jur pepp yu bare.
verily, verily, i say unto you, except a corn of wheat fall into the ground and die, it abideth alone: but if it die, it bringeth forth much fruit.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :