Vous avez cherché: saxoo (Wolof - Anglais)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Anglais

Infos

Wolof

dimbalileen gaayi yàlla yi ci seeni soxla, te saxoo dalal gan.

Anglais

distributing to the necessity of saints; given to hospitality.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ba saxoo mbëggeelu yàlla, tey séentu yërmandey sunu boroom yeesu kirist, mu tàbbal leen ci dund gu dul jeex.

Anglais

keep yourselves in the love of god, looking for the mercy of our lord jesus christ unto eternal life.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

te bés bu nekk ñu saxoo teew ak benn xalaat ca kër yàlla ga, tey damm mburu ca kër ya; ñuy lekk seen ñam ak xol bu laab tey bég,

Anglais

and they, continuing daily with one accord in the temple, and breaking bread from house to house, did eat their meat with gladness and singleness of heart,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

moom nag ku farlu woon ci yàlla la, te ragal ko, moom ak waa këram gépp; muy sarax ñu bare ci bànni israyil, tey saxoo ci ñaan ci yàlla.

Anglais

a devout man, and one that feared god with all his house, which gave much alms to the people, and prayed to god alway.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,792,859,395 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK