Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.
ndaxte yàlla dafa bëgg àddina, ba joxe jenn doomam ji mu am kepp, ngir képp ku ko gëm am dund gu dul jeex te doo sànku mukk.
for god so loved the world, that he gave his only begotten son, that whosoever believeth in him should not perish, but have everlasting life.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
dama leen di jox dund gu dul jeex; duñu sànku mukk, te kenn du leen jële ci sama loxo.
and i give unto them eternal life; and they shall never perish, neither shall any man pluck them out of my hand.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
rax-ca-dolli kuy dund te gëm ma, doo dee mukk. ndax gëm nga loolu?»
and whosoever liveth and believeth in me shall never die. believest thou this?
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
te xamal na ko ne, du dee mukk te gisul almasib boroom bi.
and it was revealed unto him by the holy ghost, that he should not see death, before he had seen the lord's christ.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
képp ku ma baay bi jox dina ñëw ci man, te duma dàq mukk ki may fekksi.
all that the father giveth me shall come to me; and him that cometh to me i will in no wise cast out.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
wutleen ak ñépp jàmm te fonk dund gu sell, ndaxte ku sellul doo gis boroom bi.
follow peace with all men, and holiness, without which no man shall see the lord:
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
sédd na leen cér bu dul yàqu, du gàkk te du seey mukk, dencal leen ko ci asamaan,
to an inheritance incorruptible, and undefiled, and that fadeth not away, reserved in heaven for you,
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
te it ku tàggat yaramam ngir rawante, duñu ko jagleel kaalag ndam mukk, su toppul sàrt ya.
and if a man also strive for masteries, yet is he not crowned, except he strive lawfully.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
ndax li yàlla maye, dootu ko nangu mukk, te ku mu woo ci boppam, dootu la dàq mukk.
for the gifts and calling of god are without repentance.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
asamaan ak suuf dinañu wéy, waaye samay wax du wéy mukk.
heaven and earth shall pass away, but my words shall not pass away.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 3
Qualité :
ku juddu ci yàlla doo def bàkkaar, ndax yàlla sol na la jikkoom, te doo man a sax ci bàkkaar, ndax juddu nga ci yàlla.
whosoever is born of god doth not commit sin; for his seed remaineth in him: and he cannot sin, because he is born of god.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
yeesu kirist du soppiku mukk; ni mu mel démb ak tey lay mel ba fàww.
jesus christ the same yesterday, and to day, and for ever.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
maa ngi la koy wax, doo génn foofa mukk te feyuloo fiftin bi ci mujj.»
i tell thee, thou shalt not depart thence, till thou hast paid the very last mite.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
yaw miy damoo yoonu musaa, mbaa doo ko moy, ba indi gàcce ci turu yàlla?
thou that makest thy boast of the law, through breaking the law dishonourest thou god?
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
kon lu nu ci war a wax? ndax yàlla àttewul foofu yoon nag? mukk!
what shall we say then? is there unrighteousness with god? god forbid.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
mbind mi dafa wax ne: «képp ku ko gëm, sa yaakaar du tas mukk.»
for the scripture saith, whosoever believeth on him shall not be ashamed.
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
te it bi yàlla defee ngiñ lii: «duñu dugg mukk ci sama noflaay,» booba ñan ñoo ko taxoon di wax? xanaa ña ko déggadil.
and to whom sware he that they should not enter into his rest, but to them that believed not?
Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :
s sd
process validation
Dernière mise à jour : 2021-10-22
Fréquence d'utilisation : 2
Qualité :
Référence:
Certaines traductions humaines peu pertinentes ont été masquées.
Affichez les résultats peu pertinents.