Vous avez cherché: yéeney (Wolof - Anglais)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Anglais

Infos

Wolof

«bi mu demee ba am ñeent-fukki at, mu fas yéeney seeti ay bokkam, maanaam bànni israyil.

Anglais

and when he was full forty years old, it came into his heart to visit his brethren the children of israel.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

nun nag nu jiitu, dugg gaal jëm asos, fa nu pool santoon, nu jële ko fa; fekk moom fas na yéeney dox, ba agsi fa.

Anglais

and we went before to ship, and sailed unto assos, there intending to take in paul: for so had he appointed, minding himself to go afoot.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndaxte waa maseduwan ak waa akayi ñi gëm, fas nañu yéeney sàkk ci seeni alal, yónnee ko, ngir dimbali ñi néew doole ci gaayi yàlla yu sell, yi nekk yerusalem.

Anglais

for it hath pleased them of macedonia and achaia to make a certain contribution for the poor saints which are at jerusalem.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

su ma yàlla bàyyee ci àddina, sas wu am njariñ la ci man. am naa xel ñaar, te xawma bi ci gën. am naa yéeney jóge fi, fekki kirist, te looloo gën fuuf,

Anglais

but if i live in the flesh, this is the fruit of my labour: yet what i shall choose i wot not.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi mu ko jàppee, mu tëj ko kaso, teg ko ci loxoy ñeenti mboolooy xarekat, ngir ñu wottu ko, fekk mbooloo mu ci nekk di ñeenti nit; amoon na yéeney yóbbu ko ci kanamu yawut ya gannaaw màggalu bésu jéggi ba.

Anglais

and when he had apprehended him, he put him in prison, and delivered him to four quaternions of soldiers to keep him; intending after easter to bring him forth to the people.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,781,065,551 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK