Vous avez cherché: yére (Wolof - Anglais)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Anglais

Infos

Wolof

seen alal seey na, seen yére yi maxe na,

Anglais

your riches are corrupted, and your garments are motheaten.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

Ñu daldi yuuxu ak di sànni seeni yére, tey callameeru suuf.

Anglais

and as they cried out, and cast off their clothes, and threw dust into the air,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

Ñu indi cumbur gi yeesu nag, lal ci seeni yére, mu toog ci.

Anglais

and they brought the colt to jesus, and cast their garments on him; and he sat upon him.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bu seen taar aju ci col, maanaam ay létt, wurus mbaa yére yu rafet,

Anglais

whose adorning let it not be that outward adorning of plaiting the hair, and of wearing of gold, or of putting on of apparel;

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu ba ñu nekkee ak seen njaaxle, am na ñaar ñu leen feeñu, sol yére yuy melax.

Anglais

and it came to pass, as they were much perplexed thereabout, behold, two men stood by them in shining garments:

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

«dafa amoon boroom alal juy sol yére yu rafet te jafe, tey dund bés bu set dund gu neex.

Anglais

there was a certain rich man, which was clothed in purple and fine linen, and fared sumptuously every day:

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

Ña ëpp ca mbooloo ma lal seeni yére ca yoon wa, ñenn ña dagg ay cari garab, lal leen it ca yoon wa.

Anglais

and a very great multitude spread their garments in the way; others cut down branches from the trees, and strawed them in the way.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

Ñu ñëw nag ci yeesu, gis ka rab ya jàppoon toog, sol ay yére te ànd ak sagoom. Ñu daldi ragal.

Anglais

and they come to jesus, and see him that was possessed with the devil, and had the legion, sitting, and clothed, and in his right mind: and they were afraid.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

kon lu ngeen seeti woon nag? nit ku sol yére yu rafet? waaye ñi sol yére yu rafet ñu ngi dëkk ci këri buur.

Anglais

but what went ye out for to see? a man clothed in soft raiment? behold, they that wear soft clothing are in kings' houses.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ngeen musal ñale, jële leen ci safara, te yërëm ñeneen ñi, waaye boole ci moytu, ba sib sax seen yére yi taq sobe.

Anglais

and others save with fear, pulling them out of the fire; hating even the garment spotted by the flesh.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ci kaw loolu korney tontu ne: «Ñetti fan a ngii may ñaan ci sama biir kër ci waxtu wii, maanaam tisbaar. ci saa si ku sol yére yuy melax taxaw ci sama kanam,

Anglais

and cornelius said, four days ago i was fasting until this hour; and at the ninth hour i prayed in my house, and, behold, a man stood before me in bright clothing,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,299,945 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK