Vous avez cherché: yeesalaat (Wolof - Anglais)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Anglais

Infos

Wolof

ba musal nu; ajuwul ci jëf yu jub yu nu def, waaye ci yërmandeem rekk. mu juddulaat nu ci laabal sunu xol, te yeesalaat nu ci dooley xel mu sell,

Anglais

not by works of righteousness which we have done, but according to his mercy he saved us, by the washing of regeneration, and renewing of the holy ghost;

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

te yàlla mi jagoo yiw wépp te woo leen ci darajay kirist, ngir ngeen bokk ci ndamam li sax, gannaaw bi ngeen yendoo bëccëgu tiis, dina leen yeesalaat, di leen dëgëral ak a dooleel, ba ngeen sampu.

Anglais

but the god of all grace, who hath called us unto his eternal glory by christ jesus, after that ye have suffered a while, make you perfect, stablish, strengthen, settle you.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yeesu ne leen: «ci dëgg maa ngi leen koy wax, bés baa ngi ñëw bu yàllay yeesalaat lépp, te doomu nit ki toog ci jalam, bi soloo ndam. bés boobu nag, yéen ñi ma topp dingeen toog ci fukki jal ak ñaar, di àtte fukki giir ak ñaar yu bànni israyil.

Anglais

and jesus said unto them, verily i say unto you, that ye which have followed me, in the regeneration when the son of man shall sit in the throne of his glory, ye also shall sit upon twelve thrones, judging the twelve tribes of israel.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,782,344,935 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK