Vous avez cherché: daaneel (Wolof - Arabe)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Arabe

Infos

Wolof

di xaar ba kera mu daaneel ko ay noonam ci kanamam.

Arabe

منتظرا بعد ذلك حتى توضع اعداؤه موطئا لقدميه.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

daaneel boroom doole yi ci seen nguur,yékkati baadoolo yi.

Arabe

أنزل الاعزاء عن الكراسي ورفع المتضعين.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndaxte fàww kirist nguuru, ba kera yàlla di daaneel noonam yépp ciy tànkam.

Arabe

لانه يجب ان يملك حتى يضع جميع الاعداء تحت قدميه.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ba ninkinànka ja gisee ne, daaneel nañu ko ci kaw suuf, mu dàq jigéen, ja juroon doom ju góor ja.

Arabe

ولما رأى التنين انه طرح الى الارض اضطهد المرأة التي ولدت الابن الذكر

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

Ñu takk doj wu réy ci baatam, sànni ko ci géej moo gën ci moom muy daaneel ci bàkkaar kenn ci ñi gën a tuuti ci ñii.

Arabe

خير له لو طوق عنقه بحجر رحى وطرح في البحر من ان يعثر احد هؤلاء الصغار.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yeesu tontu leen: «daaneel-leen kër yàlla gii, ma daldi koy yékkati ci ñetti fan.»

Arabe

اجاب يسوع وقال لهم انقضوا هذا الهيكل وفي ثلاثة ايام اقيمه.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi ñu eggee yerusalem, yeesu dugg ci kër yàlla gi, daldi dàq ñi fay jaay ak ñi fay jënd. mu daaneel taabali weccikatu xaalis yi ak tooguy jaaykati pitax yi,

Arabe

وجاءوا الى اورشليم. ولما دخل يسوع الهيكل ابتدأ يخرج الذين كانوا يبيعون ويشترون في الهيكل وقلب موائد الصيارفة وكراسي باعة الحمام.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

maa ngi leen di bind, yéen baay yi,ndax xam ngeen ki nekkoon ca njàlbéen ga ba tey.maa ngi leen di bind, yéen waxambaane yi,ndax daaneel ngeen ibliis.

Arabe

اكتب اليكم ايها الآباء لانكم قد عرفتم الذي من البدء. اكتب اليكم ايها الاحداث لانكم قد غلبتم الشرير. اكتب اليكم ايها الاولاد لانكم قد عرفتم الآب.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye yeesu gëdd ko naan: «noppil te génn ci moom!» noonu rab wi daaneel nit ki ci suuf ci kanamu ñépp, daldi génn ci moom te gaañu ko.

Arabe

فانتهره يسوع قائلا اخرس واخرج منه فصرعه الشيطان في الوسط وخرج منه ولم يضره شيئا.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

doomam yooyu muy wax, nit kese lañu. looloo tax yeesu it moom ci boppam, wàcc na, jëmmoo ni ñoom, ngir dee, ba man caa daaneel ibliis, mi yore dooley dee.

Arabe

فاذ قد تشارك الاولاد في اللحم والدم اشترك هو ايضا كذلك فيهما لكي يبيد بالموت ذاك الذي له سلطان الموت اي ابليس

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

léegi kat loraangee ngi nuy yoot, te du yem ci xañ nu sunu liggéey rekk, waaye it dina daaneel màggalukaayu artemis sunu yàlla ju mag ji, tey neenal ndamam, moom mi asi gépp te àddina sépp di màggal.»

Arabe

‎فليس نصيبنا هذا وحده في خطر من ان يحصل في اهانة بل ايضا هيكل ارطاميس الالاهة العظيمة ان يحسب لا شيء وان سوف تهدم عظمتها هي التي يعبدها جميع اسيا والمسكونة‎.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu ma dégg baat bu xumb jóge asamaan naan:«léegi mucc agsi na,moom ak kàttanak nguuru yàlla sunu boroom,ak sañ-sañu almaseem,ndaxte ki daan tuumaal sunuy bokk,di leen sosal guddi ak bëccëgci kanam yàlla sunu boroom,kooka daaneel nañu ko.

Arabe

وسمعت صوتا عظيما قائلا في السماء الآن صار خلاص الهنا وقدرته وملكه وسلطان مسيحه لانه قد طرح المشتكي على اخوتنا الذي كان يشتكي عليهم امام الهنا نهارا وليلا.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,790,607,810 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK