Vous avez cherché: fekki (Wolof - Espagnol)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Espagnol

Infos

Wolof

nanu ko fekki nag ca gannaaw dal ba, bokk ak moom toroxte ga.

Espagnol

salgamos pues a él, fuera del campamento, llevando su afrenta

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ñu bare dinañu leen fekki ci seeni ñaawteef, ba gàkkal yoonu dëgg ci bëti nit ñi.

Espagnol

y muchos seguirán tras la sensualidad de ellos, y por causa de ellos será difamado el camino de la verdad

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

jóge naa ca baay bi, ñëw àddina. léegi maa ngi génn àddina, fekki baay bi.»

Espagnol

yo salí de la presencia del padre y he venido al mundo; otra vez dejo el mundo y voy al padre

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi ko mbooloo mi déggee te gis kéemaan yi muy def, ñu bokk benn xalaat, fekki ko ci li mu wax.

Espagnol

cuando la gente oía y veía las señales que hacía, escuchaba atentamente y de común acuerdo lo que felipe decía

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

moom laay ittewoo xam, ak doole ji ànd ak ndekkiteem, ma bokk ci ay coonoom, ba fekki ko ci deeyam,

Espagnol

anhelo conocerle a él y el poder de su resurrección, y participar en sus padecimientos, para ser semejante a él en su muerte

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndaxte bi daawuda defee coobareg yàlla ci jamonoom, mu faatu, ñu suul ko, mu fekki ay maamam, suuf lekk ko.

Espagnol

porque, después de haber servido en su propia generación a la voluntad de dios, david murió, fue reunido con sus padres y vio corrupción

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

dees na jàpp seytaane, mi leen daan nax, sànni ko ci déegu safara ak tamarax bi, mu fekki rab wa ak naaféq ba mbubboo yonent. foofa dinañu leen mbugal guddi ak bëccëg ba fàww.

Espagnol

y el diablo que los engañaba fue lanzado al lago de fuego y azufre, donde también están la bestia y el falso profeta, y serán atormentados día y noche por los siglos de los siglos

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

su ma yàlla bàyyee ci àddina, sas wu am njariñ la ci man. am naa xel ñaar, te xawma bi ci gën. am naa yéeney jóge fi, fekki kirist, te looloo gën fuuf,

Espagnol

pero si el vivir en la carne me sirve para una obra fructífera, ¿cuál escogeré? no lo sé

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi ko njiit la déggee, mu fekki kilifaam, yégal ko ko; mu ne ko: «ndax xam nga li ngay def? nit kale jaambur la ci room.»

Espagnol

cuando el centurión oyó esto, fue e informó al tribuno diciendo: --¿qué vas a hacer? pues este hombre es romano

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,772,892,454 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK