Vous avez cherché: gaayi (Wolof - Espagnol)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Espagnol

Infos

Wolof

mboolem gaayi yàlla yépp ñu ngi leen di nuyu.

Espagnol

todos los santos os saludan

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

dimbalileen gaayi yàlla yi ci seeni soxla, te saxoo dalal gan.

Espagnol

compartiendo para las necesidades de los santos; practicando la hospitalidad

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndaxte yég nanu seen ngëm ci kirist yeesu ak seen mbëggeel ci gaayi yàlla yépp.

Espagnol

porque hemos oído de vuestra fe en cristo jesús y del amor que tenéis por todos los santos

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ci mbirum ndimbal loolu jëm ci gaayi yàlla yi, matul ma leen di bindaat,

Espagnol

en cuanto a esta ayuda para los santos, está de más que os escriba

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi ma déggee nag seen ngëm ci boroom bi yeesu ak seen mbëggeel ci gaayi yàlla yu sell yépp,

Espagnol

por esta razón, yo también, habiendo oído de la fe que tenéis en el señor jesús y de vuestro amor para con todos los santos

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

looloo tax gaayi yàlla yi war a muñ, ñooñuy sàmm ndigali yàlla yi ak ngëm ci yeesu.

Espagnol

¡aquí está la perseverancia de los santos, quienes guardan los mandamientos de dios y la fe de jesús!

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndaxte yàlla du yàllay lëj-lëj waaye yàllay jàmm la. ci mboolooy gaayi yàlla yépp,

Espagnol

porque dios no es dios de desorden, sino de paz. como en todas las iglesias de los santos

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

nuyul-leen ma gaayi kirist yeesu yu sell yépp. bokk yi ànd ak man, ñu ngi leen di nuyu.

Espagnol

saludad a todos los santos en cristo jesús. los hermanos que están conmigo os saludan

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

piyeer may ko loxo, yékkati ko. mu woo gaayi yàlla ya ak jigéen ña, won leen ko, muy dund.

Espagnol

Él le dio la mano y la levantó. entonces llamó a los santos y a las viudas, y la presentó viva

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

maye na leen, ngir ñu waajal gaayi yàlla yu sell yi, ñu man a bey seen sas ci taxawal mbooloom kirist, di jëmmam.

Espagnol

a fin de capacitar a los santos para la obra del ministerio, para la edificación del cuerpo de cristo

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

may nañu ko, mu sol mbubb mu sette weex bay lerax.» mbubb mu weex moomu day misaal njubtey gaayi yàlla yi.

Espagnol

y a ella se le ha concedido que se vista de lino fino, resplandeciente y limpio." porque el lino fino es los actos justos de los santos

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Wolof

noo leen di bind, yéen gaayi yàlla yu sell, yi dëkk kolos te di ay bokk ci gëm kirist. na leen yàlla sunu baay may yiw ak jàmm.

Espagnol

a los hermanos santos y fieles en cristo que están en colosas: gracia a vosotros y paz, de parte de dios nuestro padre

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu agaripa ne pool: «xanaa yaw, ci diir bu gàtt bii rekk, nga ma bëgg a dugale ci gaayi kirist!»

Espagnol

entonces agripa dijo a pablo: --¡por poco me persuades a ser cristiano

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndaxte njaamu, gi ngeen di jaamu, yemul rekk ci faj soxlay gaayi yàlla yi, waaye dina tax it ngërëmu ñu bare baawaan, jëm ci yàlla.

Espagnol

porque el ministrar este servicio sagrado no solamente suple lo que falta a los santos, sino que redunda en abundantes acciones de gracias a dios

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

xanaa dangeen a xamul ne, gaayi yàlla yi ñooy àtteji àddina? te ndegam yéenay àtteji àddina, lu tere ngeen man a àtte mbir yu ñàkk solo yi?

Espagnol

¿o no sabéis que los santos han de juzgar al mundo? y si el mundo ha de ser juzgado por vosotros, ¿sois indignos de juzgar pleitos tan pequeños

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

Ñaanal-leen ma, ngir ma mucc ci ñi gëmul ci waa yude; te it gaayi yàlla yu sell yu nekk ci yerusalem nangu ndimbal, li ma leen di yóbbul.

Espagnol

para que yo sea librado de los desobedientes que están en judea, y que mi servicio a jerusalén sea del agrado de los santos

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

nun pool ak timote, jaami kirist yeesu, noo leen di bind, yéen gaayi yàlla yu sell yépp ci dëkku filib, yi bokk ci kirist yeesu, yéen ak seeni njiit ak ñiy topptoo yëfi mbooloo mi.

Espagnol

pablo y timoteo, siervos de cristo jesús; a todos los santos en cristo jesús que están en filipos, con los obispos y diáconos

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndaxte ndëndu xare jib na, waxuma sunu diggante ak nit ñi, waaye ak kilifa yiy nëxal àddina si, ñuy kilifa yi ak ay boroom sañ-sañ, di gaayi seytaane yi ci bérab yu kawe yi.

Espagnol

porque nuestra lucha no es contra sangre ni carne, sino contra principados, contra autoridades, contra los gobernantes de estas tinieblas, contra espíritus de maldad en los lugares celestiales

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ba mu jëlee téere ba, ñeenti mbindeef ya ak ñaar-fukki mag ña ak ñeent daldi dëpp seen jë ca kanam mbote ma, ku nekk yor xalam. Ñu yor it andi wurus yu fees ak cuuraay, yu doon misaal ñaani gaayi yàlla ya.

Espagnol

cuando tomó el libro, los cuatro seres vivientes y los veinticuatro ancianos se postraron delante del cordero. cada uno tenía un arpa y copas de oro llenas de incienso, que son las oraciones de los santos

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,774,850,598 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK